MAABO Yako Waral cover image

Paroles de Yako Waral

Paroles de Yako Waral Par MAABO


[VERSE 1]
Héy ! kholate ma kaw ba souf, ma len dakh solou fouf
Bbay boul di diawalé, dou beurri yéré moy sagnsé
Kholmaaaa ! fouma meuna guéneu ngané fi leu
Kham ngaaaa ! dou ci yéré yi ci mane mi leu
Kholm anima 3 pièces diapé, té douma Djiby Dramé
damay dieum mak di délou khalé, ioe fo may dieuleuté
Souma nékhé obasanjo, def class ték chapeau,
kay dieul ay photo, li yeup yako waral guissé maabo


[CHORUS]
Hé ! ioe khalé bi lé, ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh
Sa dokhine bi nexnamaaaa ! hé hé
Ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh
Sa dokhine bi nexnama
Niou dém, kone naniou dém thiakass ! thiakass ! (Thieum hé !)
Thiakass ! thiakass ! Dara douniou té thiakass ! thiakass
Thiakass ! Thiakass ! Ayway, naniou dém thiakass
Thiakass ! ooooh ! héh
Thiakass ! thiakass ! Dara douniou té thiakass
Thiakass ! nioune dara douniou téré dém


[VERSE 2]
Bala ma dougou école, tchi la am class
Ma nek ci sa xol, ndax dama am thiass
Baby, kholma, douma moramou goné,
Beuss bi tay la, dina la wane fima meuné

Di solou ni mannequin, diékk ni djèk
Di dagou ni drianké
Moussorou ni Diouma Dieng
Té fouma tassé sama cheveux done sa Beyoncé
Kay diégué ma niou snap selfie, kay niou dieul ay photo
Aduna yeupeu guiss ko, liiii... ! yako
waral guissé maabo


[CHORUS]
Hé ! ioe khalé bi lé, ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh
Sa dokhine bi nexnamaaaa ! hé hé
Ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh
Sa dokhine bi nexnama
Niou dém, kone naniou dém thiakass ! thiakass ! (Thieum hé !)
Thiakass ! thiakass ! Dara douniou té thiakass ! thiakass
Thiakass ! Thiakass ! Ayway, naniou dém thiakass
Thiakass ! ooooh ! héh
Thiakass ! thiakass ! Dara douniou té thiakass ! thiakass
Nioune dara douniou téré dém

Thiakass ! thiakass ! Ioe sama djiguennn
Da nga am class bégue na ci ioe
Mane ioe yay, lima mome
Wowoooohhh ! Guissé maabo

Ecouter

A Propos de "Yako Waral"

Album : Yako Waral (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 03 , 2019

Plus de Lyrics de MAABO

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl