Lane Mo Takh Paroles

BRIL Senegal | Afropop,

Paroles de Lane Mo Takh


Déf  ngama louma guèntoulwone
Louma doul meuna guum koumako wakhone
Dara guenoul kawè fimala  téggoooone
Sorouma lii Béteu-Ngamaaahh
Yaw li ngana deff metti-namaa hahaan
Ak finiou diaar yeup lii meunoumako wone imaginé
Sama bopp dafa diakhasso may guiss ayy image you nééh
Lan mola doyoul ba nga Diouk name da ngay wouti lénén fénén
Loutakh mou done kouma kham loutakh yaw tanoulo kénén
Yaa takh ma bayi nieup bayi samay Mbokk yaw nga Fayma lii
Da nga wakh bama Diokh la lepp mokk’ak yaw béneu familly

Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumèl nii
Khawma loula dall ba nga beugga dém fènèn
Kaay nga wakhma  loumala bagnal ba ngay khool  kénén

Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumèl nii
Khawma loula dall ba nga beugga dém fènèn
Kaay nga wakhma  loumala bagnal ba ngay khool  kénén

Dafa mélni damay guént yakamti kouma yééhh
Bama yééwou meuna doundaat mbékté biss bign niouy mayéé
Yaa nékkone sama vérité yaw rek laa geumone
Meussouma guiss finga maay trompé mélni  damma geume-mone
Digoon ngana doundou aldianaaaahh
Maa’k yow dound’ak dééh ngana wakhone wayé tay l éppeu diékhnaaaahhh
Yaa takhone ma bayi di wakh nane niom nieuppa yéém
Tey nga khooss sama cicatrice deffatt ko gome
Liniou dounddou boumakay méttali day mélni poème
Kii louko dall est ce que anddeu naak saagooome

Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumèl nii
Khawma loula dall ba nga beugga dém fènèn
Kaay nga wakhma  loumala bagnal ba ngay khool  kénén

Wakhma lane moo takh nga deff maa liii
Khawma lane moo takh nga deff loumèl nii
Khawma loula dall ba nga beugga dém fènèn
Kaay nga wakhma  loumala bagnal ba ngay khool  kénén

 

BRIL (11 paroles)

BRIL FIGHT 4 est un artiste musicien, Beatmaker ,chanteur et Rappeur originaire de Thiaroye - Diamaguéne au Senegal. Il est également le fondateur et Directeur Général du label Class’Chic Music.

Ce jeune rappeur nous vient de Thiaroye une banlieue...

Laisser un commentaire