Paroles de Détails
Paroles de Détails Par BRIL
Yeah Miézé
Bril, Beugouniou Détails
Grossiste la té douma djaay , talouma Détail
Sa wakh you séw yi kham ngani doula fay ngani dothi Taayi
Nga Nouyouma, ma fayla
Nga sissou né tontou bi nékhoula
Nga yeuggueulma té nieuwouma
Nga sopiko khoulo méréma
Hey Sétlou nani lou kén kholoul thi Nitt yakoy Guiss
Wakh bou ndaw nga ngandal, yaw mom reuyo danga diiss
Lingay laadj ling thi dathie, amaloula ndieurigne ni férié bou tombék Dimanche
Té Lima léér dinga Wéér Sa Bopp, wakh nga ba tooy té sa Fitt dou mass
Dégg na niounima, Guiss nga té Lééroula
Féékéwo, Yeuggoulo, ni sa Xel nakhoula
Louné nga Khoulo ko té dara wauroulo
Détails yi yorouko bayil li Waroula
« Message na nga guiss té tontouwo
Statut nga vue commentéwo »
Sa Xel mi est ce Math na , Calcul yi nga néké sonal nala
Beugo Solution , say bo wakhé yokkou Problème la
« Aimé na sa photo , Abonné sa insta , followoma »
Yaggueu nala wakh ni bayil beugg Détails falléwoma
Détails - Lou takh nga beugg ay Détails
Détails - Miézé nékkoul thi Détails
Détails - Lou takh nga beugg ay Détails
Détails - Bril Beuggoul Détails
Beuggouma , Beuggouma , Beuggouma ay Détails
Talouma , Talouma, Talouma ay Détails
Mane Beuggouma , Beuggouma , Beuggouma ay Détails
Mane Talouma , Talouma, Talouma ay Détails
Soma Dééggoul, douniou Dééggo
Damay Kheuthie, douma kheuthio
Ni ngay déffé da am Défaut
Sa rongogn yi lay Kheupo
Louma défoul nga défanté, beugma wéér motakh ngay wéranté
Niaari montre bépp côté, lolou moy amatouma djotou djoté
Chaque jour yangui lidjeunti samay
Business, di dokh thi sama peace of mind
Thi sa bopp bi mafi tek tank, kone day yomb ma dokh thi sa mind
Doundoumala pourtant déwouma, match bi doko sétane boudé jouéwouma
Li ngamay djappé chaque jour, lolou djappou niou
Khamna ay nitt you maguette wayé maggouniou
Hey niongui sissou dafa féégn hé
Pour nga djiitou djaroul ndjeukeunté
Amna nioula gnimé bagn hey
Ndakh nila gnénén beuggué hey
Détails - Lou takh nga beugg ay Détails
Détails - Miézé nékkoul thi Détails
Détails - Lou takh nga beugg ay Détails
Détails - Bril Beuggoul Détails
Beuggouma, Beuggouma, Beuggouma ay Détails
Talouma, Talouma, Talouma ay Détails
Mane Beuggouma, Beuggouma, Beuggouma ay Détails
Mane Talouma, Talouma, Talouma ay Détails
« Message na nga guiss té tontouwo
Statut nga vue commentéwo »
Sa Xel mi est ce Math na, Calcul yi nga néké sonal nala
Beugo Solution, say bo wakhé yokkou Problème la
« Aimé na sa photo, Abonné sa insta, followoma »
Yaggueu nala wakh ni bayil beugg Détails falléwoma
Détails - ma moudjé nieuw sa Galé setsila
Détails - souhaitéwoma happy birthday bayinala
Détails - Lima sagnsé wakhouloma sakh rafetna
Détails - hey Rap bi waroul and’ak Tama
Détails
Ecouter
A Propos de "Détails"
Plus de Lyrics de BRIL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl