Paroles de Eup Na
Paroles de Eup Na Par BRIL
Soumalay Khõl day am loumay yeuk thi yaw bay daanou léér
Mane Sama khol thi goudi la néwone, ya thi soti léér
Yaaggone na thi leundeum wayé danga nieuw taal li fayone
Bokkouniou wone fi niou djeum té biniou dadjé , da nio bokk yone
Li né sama khol taagouwoul sama khel mane damala guiss rek beuggla
Té dou meussa djéékh fi lèk ma ngék sama khel
Té kham ngani lou yaggueu deuggla
Dina def louné ba sa khol bi ma mom ko, ndakh sama boss djokhnalako
Meune na la liguéyeul té douma fayékou , yay sama Boss wakhnalako
Baby yaw , yay sama léér , yay ki gueune thi mane yamay doundeul dafa léér
Lii Eup Na (ay ay ) Eup Na (ay ay)
Eup Na ba khadjoul thi khol , baby yaw lay noyé
yaw , yay sama léér , yay ki gueune thi mane yamay doundeul dafa léér
Lii Eup Na (ay ay ) Eup Na (ay ay)
Eup Na ba khadjoul thi khol , baby yaw lay noyé
Oooh oh oh, lo déf nekh nama
Damala nopp ba nobaalé say caprice ,rééwal beuggna
Li né sama khol moy féégn thi samay djeuf mane damala miine
Douma dém bayila
Yaw yama djiigg , yay ki takh bama riche yay sama vitamine , beuggnala
Deugg néékhoul yaw , amna no mél wayé yamay danel « Eup Na »
Même bofi néwoul , fouma khõl yafay né ndakh sama Namel « Li Eup Na »
Sama mbeuguél thi yaw daf ma eup dolé
Ya takh ma gueumni loula bétteu meune la
Kiy daagou fign ko nobé kham ngani yaw la
Boy khõl ki gueune thi yaw , ko guiss rek mane la
Baby yaw , yay sama léér , yay ki gueune thi mane yamay doundeul dafa léér
Lii Eup Na (ay ay ) Eup Na (ay ay)
Eup Na ba khadjoul thi khol , baby yaw lay noyé
Yaw, yay sama léér , yay ki gueune thi mane yamay doundeul dafa léér
Lii Eup Na (ay ay ) Eup Na (ay ay)
Eup Na ba khadjoul thi khol , baby yaw lay noyé
Baby beuggnala lol mane , doumala meussa fowé
Ya né sama Khol mane , yaw yay kimay noyé
Nopp nala yaw yay sama léér
Mane beuggnala yama mom dafa léér
Lii Eup Na (…. ay ) Eup Na
Eup Na ba khadjoul thi khol , baby yaw lay noyé
Ecouter
A Propos de "Eup Na"
Plus de Lyrics de BRIL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl