DIP DOUNDOU GUISS LNN Show 28 Decembre LSS cover image

Paroles de LNN Show 28 Decembre LSS

Paroles de LNN Show 28 Decembre LSS Par DIP DOUNDOU GUISS


Ma ngui si thiolou ba tok ak avenir nou nek ak bou wex ni tolou coton
Nobouma wone tay sa cho daf may message dima sarakhou nane ma tontuma bok
Fessal stade meunoul fess sama bop c'est par ce que sédé nagn job bi nga job
Dotouma clashanté ak béneu rappeur boy kholal sari sigui nga tontu sa bop
Date'ou album bi lama boum yi di nieuka lathié que permis
Niatta parque lagn ma fi sout ken
Meussoul atté batay
Thi ay nuit blanche ak job dimanche di fanane ci alleu mo fay ni
Encaissé chèque yi, enchainer
Pèle yi di entérrer game bi

May guéner ay hits, ngey guéner ay ndiengakhite
Ay gaindé sans fite né len Dip khép na stade bi
Tête d'affiche feep sama guent dou dess Afrique
28 ci profile couverture ak ci say statut
Manguék Free Itel yapeu rappeur ci sama frigidaire
Niggah critiquel sa wa gallé nieuka dieundi ticket
Fay la soul la rek, yeufou criminel la dip di def,
Guiss ci séttu boy bi bind histoire'am ak bic bou jail
Ci mane lay dess
Ci mane lay dess
Ci mane lay dess
Ma def ko, ci mane lay dess
Ioe ioe, ci ioe lay dess
Ci ioe lay dess
Ci ioe lay dess
Niou def ko, ci ioe lay dess

Ecouter

A Propos de "LNN Show 28 Decembre LSS"

Album : LNN Show 28 décembre LSS (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Nov 14 , 2019

Plus de Lyrics de DIP DOUNDOU GUISS

DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS
DIP DOUNDOU GUISS

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl