
Paroles de Yeksil
...
Paroles de Yeksil Par YOUSSOU NDOUR
Kong Kong, Yeksil da’al
Kong Kong, Yeksil da’al
Kong Kong, Yeksil da’al Yeksil daa’ al
Kong Kong, Yeksil da’al
Yeks’il avec plaisir
T'amène que des bon souvenirs
Wakht’ou wou la nekh
Meun nga feugg’el
Fii do fii gann
Bou gnou waxan ‘té dëgg da’ al
Bokk nga ci gni maa bëgg
Kong Kong, Mang ‘ui xa’ar
Pressé d’entendre ta voix
Bikk rekk, je pensé a toi (ahnn ahnnn)
Geudj ‘on fii loo’l binga gnew’é
Geudj ‘on fii loo’l binga gnew’é
Ne na la, ne na la nee’e na laa
Bissmi, bissmi, bismillah
Geudj ‘on fii loo’l binga gnew’é
Ne na la, ne na la nee’e na laa
Bissmi, bissmi, bissmi, bissmi, bismillah
Kong Kong, Yeksil da’al
Yeks’il avec plaisir
T'amène que des bon souvenirs
Kong Kong, Mang ‘ui xa’ar
Pressé d'entendre ta voix
Meme hier nuit, je pensé a toi
Break percu
Mann dé dama guiss si yaw sincérité
Dellou guiss si yaw, woyoff ak daal
Motakh ma yakamt’é sa jotay akk sa reer dju nekh
Mann dé dama guiss si yaw sincérité
Dellou guiss si yaw, ‘oyoff ak daal
Motakh ma yakamt’ é sa jotay akk sa reer dju nekh
Gnew ‘al sayou la nekh’ ée séy’on
Mann daff ‘ay maa’y djé rigne
Gnew ‘al sayou la nekh’ ée séy’on
Ahnn mann daff’ ay maa’y djé rigne
Mann dé dama guiss si yaw sincérité
Dellou guiss si yaw, ‘oyoff ak daal
Motakh ma yakamt’ é sa jotay akk sa reer dju nekh
Ecouter
A Propos de "Yeksil"
Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl