
Paroles de Sam Fall
...
Paroles de Sam Fall Par YOUSSOU NDOUR
Sam fall , ca kaw a kaw , na riir ë riir, ca kaw a kaw
Sikkar si neex na
Sam fall , ca kaw a kaw , na riir ë riir , ca kaw a kaw
Sikkar si neex na
Man daf may yóbbu , feneen
Lii may yëg baatin lë , moo tax dox in u cheikh ibra , du neen
Baay fall , sikkër lay fanaan ee , lu mu am jox bamba
Toog di déglu ndigël
Baay fall, sikkër lay fanaan ee , lu mu am jox bamba toog di dėglu ndigël
Waaw baay fall
Maam cheikh ibrahima fall ,
Bu la neex oon nga fall u buur
Waaye gis u loo yaw , ku dul , cheikh bamba
Baay fall bi , boroom xol bu leer
Baay fall bi , le champion
Baay fall bi , boroom xol bu leer
Baay fall bi , yéem na ma
Baay fall sikkër lay fanaan ee lu am jox bamba
Toog di dėglu ndigël baay fall, sikkër lay fanaan ee lu am jox bamba
Toog di dėglu ndigël
Waw baay fall
Ecouter
A Propos de "Sam Fall"
Plus de Lyrics de YOUSSOU NDOUR
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl