NDIOGOU AFIA Allah cover image

Paroles de Allah

Paroles de Allah Par NDIOGOU AFIA


Diamou  yalla moy li war bilahi
Wayé xam ko lou ndieuk gaukoy diamou walahi
Yaa ayou al lazi na aamanou itakhoulaha wabtahou ilayhi wassilata
Yene ni geum yalla na guene ko ragal te wouti wassila
Diamou yalla baxna moy li war xam ko lou ndieuk gaukoy moy li woor
Allah allah allahou
Moy batinou yalla mo diafé xam wayé moy zahirou yalla mo feuss
Allah allah allahou
So beugue am ngeureumal yalla kay ma diguel leu
Tewloul deglouma ak sa xel ma yeugeul leu
Allah allah allahou
Wouteul serigne bou matte serigne
Ni cheikh ibra fall ak mame bamba, diokkoul thi kou agg
Giir mou meune leu tek thi yone wa
Allah allah allahou
Serigne bou matte serigne dafay foote tilimi xol
Selal sa xel ba do thi xalam loukoy  neukoy neukheul
Allah allah allahou
Serigne bou matte serigne dalay xamal yalla
Yalla reka takh nite di wouti wassila
Allah allah allahou
Neugeum matte na serigna
Dafay dakkou dakk leu saxal li fi nek
Te lifi nek moy rabba alahou yalla
Allah allah allahou
Serigne bou matte serigne, dafay waral guindekou
Keumnou gua teukhou guiss guiss sopekou
Allah allah allahou
Nga ndekke laa ilaha ilalah ane allahou
Reere alhamadoulilahi nopalou
Allah allah allahou
Bounou nei guiss yalla tiow li beuri lolou
Te guiss loudoul yallaa wara andi tiow
Nakala nite di guemme dou guiss dou xamme
Yalla miko sakk feuss fepp moukoy guiss saasoune
Allah is the first and the last
He is life
He is love
He is eternity he is the Lord
C’est le créateur
God is one
He is powerful God is one
Alahou allah
Kone raniel
Kou agg ak kou aggoul
Sou agoul doula aggale
Dalay khagn yalla
Dioublou lola thi ay sokhlam
Do am yalla
Te mouno metal ay sokhlam
Yalla sou sant dou askane
Tieuy boula kene geum lo sagn sagn
Xamal sa bopp
Ndakh mola meuneu tektal sa borom
Nite bou xamoul bopam djiyok boromam
La ilaha ila lah
Xamal sa bopp
Ndakh mola meuneu tektal sa borom
Nite bou xamoul bopam djiyok boromam
La ilaha ila lah
Xamal sa bopp
Ndakh mola meuneu tektal sa borom
Nite bou xamoul bopam djiyok boromam
La ilaha ila lah
Akhhh doukate fall
Xamal sa bopp
Mola meuneu tektal sa borom
Nite bou xamoul bopam djiyok boromam

Ecouter

A Propos de "Allah"

Album : Serigne Touba Rek (Album)
Année de Sortie : 2022
Ajouté par : Farida
Published : Sep 06 , 2022

Plus de Lyrics de NDIOGOU AFIA

NDIOGOU AFIA
NDIOGOU AFIA

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl