Paroles de Beug Fallou
Paroles de Beug Fallou Par NDIOGOU AFIA
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Way kou yalla baakhal
Warna wa diou am xél
Ndeugeum sa xol kinianoul
Mba guadone kou réréé
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Fallou ay gua daa néékh
Lérneu gua yi ndakh néékh
Fallou rek léne néékh
Way wi amneu séédé
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Mo defal mouride yi
Diamm dji ak you néékh yi
Lolo waral mouride yi
Melni niouy khawarai
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Fallou lay doxaneto
Fallou lay wayaneto
Fallou lay xalaneto
Kou ma khéékh malay réé
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Afia lay doxaneto
Afia lay wayaneto
Afia lay gualadio
Kou ma khéékh malay réé
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Piss you foor yiniouy sol
Mbacke yaniou kay dial
Foniou guiss laniouy sol
Lepp dafay valeurai
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Beug fallou mo néékh
Sopp fallou mo néékh
Geum serigne fallou mo néékh
Sa lepp dafay valeurai
Yadi samsou sodane
Fallou yague gua dane
Oupp gua lambi sodane
Nio guilay ziyaré
Beug fallou mo néékh
Lérneu gua yi ndakh néékh
Kouy beug fallou wanéwoul
Fallou diarneu féétél
Ma diakhlai fallou lay wo
Ma sokhla fallou lay wo
Té nak sa youma wowai serigne fallou
Am thi ndam bou léér
Ma diakhlai fallou lay wo
Ma sokhla fallou lay wo
Té nak sa youma wowai serigne fallou
Am thi ndam bou léér
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Zalika fadilou lahi you tihi mane ya chaa ou
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Yalay diokh ngeunel kouko néékh diohneuko fallou laawou
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Walahi beug fallou yi maléne nié bou wereu wér
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Walahi beug fallou yi yéne raw guéne bou wéreu wér
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Nagn diapp serigne fallou bou bakh kinion am kene amouko
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Nioune kiniou am kene amouko té limou meune kene meunouko
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Kouy beug fallou dioguel takhaw wakh tia kaw ma beug fallou
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Ma beug fallou beug fallou ba beugalei sakh kou beug fallou
Beug fallou ngeunél leu beug fallou lenene leu
Beug fallou assurance leu beug fallou gualathie leu
Beug fallou boul diakhlai beug fallou do daanou
Beug fallou diantte ngay done niouy tiow ngay sori
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Beug fallou diantte ngay done niouy tiow tiow ngay sori
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Sa moromou nitte teukoula mou téréla nélaw xamou yalla
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Yaaram sa moromou nitte teukoula mou téréla nélaw xamo yalla
Serigne fallou serigne fallou serigne fallou serigne fallou
Serigne fallou serigne fallou serigne fallou
Oupp gua lambi sodane nio guilay ziyare
Serigne fallou awa bousso diahrew ba tiamninial maréma kounta
Ecouter
A Propos de "Beug Fallou"
Plus de Lyrics de NDIOGOU AFIA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl