Paroles de Covid19 (Joro Remix)
Paroles de Covid19 (Joro Remix) Par ONE LYRICAL
Coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro
Corona coro
Coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro
Corona coro
Coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro
Corona coro
Coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro
Every day yagui contaminé coro yagui ray
Ya tax nieup confinéwou héhi yea
Baxo ci nioune amna ay cas you déh
Cas yegui geuna yok, cas yegui geuna yok
Path mi geuna metti - Medcin yi takhaw
Nioune kagne laniouy teudiou tokk
Faagarou warna nieup guère bi nioko bok
Moytoul dioxé loxo - moytoul dem ci mbolo
Seukeut thi thiontio - covid-19 notooo
Niawal wala beau goss - chaumeur wala b
Covid 2019 - Bawouy kén lo fokk
Fagarou geun fadiou febaar bou gaw
Symptômes yi seukeutla ‘ bakane you toy
Baate bou metti andak yaram bou tang
Diaffé diaffé pour noyi wotél mou gaaw !
Numéro vert : 800 00 50 50 | samu 15 15
Do faay dara
800 00 50 50 | samu 15 15 do faay dara
Coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro
Corona coro
Coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro
Corona coro
Coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro ‘coro
Ecouter
A Propos de "Covid19 (Joro Remix)"
Plus de Lyrics de ONE LYRICAL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl