Paroles de Geum Geum
Paroles de Geum Geum Par ONE LYRICAL
Nitt ku né akk kila y’Allah may
Nangul ndax moy may
Del diokhé azaka muslim bul nangu nay
Gëm gëm tere nala baayil
Bul saalit bay jaayou
Ma sœur bul jaay sa ngor ndax gore lagn lay fay
Woyof sër ba melni barbare
Soxla wuma xam sa jaar jaar
Da nga dem ba magg xam ni life da tar
Non Comme que legui nii la xaaral ma moytu quelques bakaar
Y’Allah né na togn len ma baal na len (Baal na len)
Nangul doggal y’Allah buur bu baax la (la la)
Nangul doggal y’Allah buur bu baax la (la la)
Keulé am yow amuloo tax nda toog di xoole
Nénga dafa bari doole tax mënu len bokk ndab oh non non non
Mon frère yow geumulo di nga jog ci neew di doole
Joggeul utti loo def ki ngay gné dafa ligeey mu fègn ci moom
Gnaani waajur sakku ko mu fajj sa aajo
Defkat nga te gnaano deelu kaso
Li lay fèess ci xel mi sa weursëg ding ci nga jot
Dessinel sa adina yor baguette bi yay Picasso
Bagnal ku reetaan
Goorgorlul bañ kulen daan
Xoolal ci say maam
Fayal bor bi teureul Souleymane
Té Nitt du bagn ngànt
Y’Allah né na ma dooli ngen sànt
Wara weur di waliyaan ci kop ngay naan
(Joggeul célébrer)
Nangul doggal y’Allah buur bu baax la (la la)
Nangul doggal y’Allah buur bu baax la (la la)
(Gëm gëm)
Dara jòmb la, dara jòmb la, dara jòmb la my nigger
Dara jòmb la, dara jòmb la
Boul gnaan ken boo jengoo jiite
Boul gnee ken boy hustle yigo
Milliardaire mba Rest In Peace ma
Gisteul bee fègn ci sen ay jikko
Dara jòmb ma, dara jòmb ma, dara jòmb ma my nigger
Dara jòmb ma, dara jòmb ma
Gis sen intérêts tax ngen feel ma
Mine na fen da ngen di jouer film
Ay naafeq gno rax sen biir
May 10e dan may sen ceinture noire
Por El Dinero music
Por El Dinero music
Reyal say noon nga teg sa bopp
Sa échec moy bagn beggeul sa papeu
Da ngay dem fay son nga jeul say ventes
Sa ngeureumu yaay moy guddal say fan
Ngeureum‘ag gëm gëm rekk mo gnu andi fi
Ba tay gnu taxawal sunu entreprise
Ecouter
A Propos de "Geum Geum"
Plus de Lyrics de ONE LYRICAL
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl