
Paroles de Adduna
...
Paroles de Adduna Par ASHS THE BEST
Da maa jeggani woon bay doora ñëw
Da maa foggoon ni dootul jeex
Dem naa ba gis ci yow liy man du ñoom
Te man da maa foggoon jamm du fi jeex
Man’ag adduna bëre bukke’eg mbaam la
Ku mën sa moroom daan
Fi ma jaar’ag adduna bëccëg bu ammul naaj la te bu guddee mu lëndëm lool
Ndax bu ñu joowee ba fog ni agg nañ
Mu mel ni da ñuy delluwaat fu ñu jogge woon
Man’ag adduna bëccëg bu ammul naaj la te bu guddee mu lëndëm lool
Adduna
Adduna
Bëccëg bu ammul naaj la
Siggil te nga xool ma ci bët
Te nga wax ma ni yow mi
Sudee am na loy yëgg
Jarul ñuy nëbboo
Damaa xammul woon ni mbëggeel
Da fa jiitu suñ judd
Su ma xoolee ginaaw
Du ma mën delluwaat
Su nuy rangòoñ di na fer
Da ñuy doora gis naaj
Naqqar lañ fanaanoo
Te man da maa jeggaani woon
Bay bëgg ñëw fii
Da maa foggoon ni jamm moom di fi jeex
Da maa foggoon ni jamm moom di fi jeex
Da maa foggoon ni jamm moom di fi jeex
Da maa foggoon ni jamm moom di fi jeex
Ecouter
A Propos de "Adduna"
Plus de Lyrics de ASHS THE BEST
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl