Paroles de Yaakaar
Paroles de Yaakaar Par ASHS THE BEST
Yow mii laa doon sèntu
Mbaa yaakaar tasul ci yoon wi
Jambaar dawul daa wuti
Jom moy dem fulla moy dellusi
Yaay di na woote
Di laaj noo yèndoo
Leer na ma sa jamm mo koy gënël
Nga am’ag nga ñakk taxu koo jog
Su soxla yi woote (soxla)
Te ñu yaakaar ko ci yow
Di lañ la xaar keneen ku dul yow
Yow mi ñëpp yaakaar ci yow sa soxla koo koy diis
Bul tiit bul jàxle
Lu yoon bi mën meti
Bul xaadi
Lu yòmb jiggul goor
Jiggul sax jigeen
Kon lan ngay caalit
Bul tiit bul daw bul jàxle
Lu yoon bi mën meti
Bul xaadi
Lu yòmb jiggul goor
Jiggul sax jigeen
Kon lan ngay caalit
Soo yakkee sooraale ma
Man suma foree fii indil la
Yaa taggoo ñu yobbante la
Te soo goree lepp fekki si la
Suñ demmee ba yaakaar ci yow mi di utti loo am di utti lu gën
Suñ demmee ba yaakaar ba duñ xalaat yaakaar gi tas
Suñ demmee ba yaakaar ci gaynde gi rëbbi ji woon mën jaare fa sooy
Suñ demmee ba yaakaar ci moom mi dem utti ji jën
Yow mii laa doon sèntu
Mbaa yaakaar tasul ci yoon wi
Jambaar dawul daa wuti
Jom moy dem fulla moy dellusi
Yow mii laa doon sèntu
Mbaa yaakaar tasul ci yoon wi
Jambaar dawul daa wuti
Jom moy dem fulla moy dellusi
Bul tiit bul daw bul jàxle
Lu yoon bi mën meti
Bul xaadi
Lu yòmb jiggul goor
Jiggul sax jigeen
Kon lan ngay caalit
Bul tiit bul daw bul jàxle
Lu yoon bi mën meti
Bul xaadi
Lu yòmb jiggul goor
Jiggul sax jigeen
Kon lan ngay caalit
Bul jàxle
Bul xaadi
Jiggul sax jigeen
Lan ngay caalit
Bul jàxle
Bul xaadi
Jiggul sax jigeen
Lan ngay caalit
Ecouter
A Propos de "Yaakaar"
Plus de Lyrics de ASHS THE BEST
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl