LEUZ DIWANE G Weeruwaay cover image

Paroles de Weeruwaay

Paroles de Weeruwaay Par LEUZ DIWANE G


Djiguene djiguene
Moy su niou yaay
Djiguene djiguene
Moy su niou wéeruwaay
Djiguene moy ki yalla teral
Té moy sou niou wetal
Sa su niou méré djiguene moy ki niouy bégal
Djiguene djiguene moy su niou waay
Djiguene djiguene moy su niou noflaay
Nioy diour yar boot nampal aka tété
Kou mandi na mbatu mi delou fa nga rooté

Ce  cordon ombilical qui nous a lié
Signifie ce qu'on ne peut pas nier
Tout le monde sait
Ce que cela fait
They lose life giving birth oh les quais
Where we Came from
Carried in their womb
Lépi niep
Daum bi fatch sou niouy gaume
Rénou kom kom
Djiguene bou ame diom
Datch deup
Djiguene nioy diour su niouy dôme
Mala yi sakh kene doratou lene
No violence
No woman no cry
Nitt gni dara safatoulene
That silence
Gonna remain till we die
Féministe misogynie i don't care
I just think about the human being
Cette personne à tes côtés
Est un humain that's my feelling

Djiguene djiguene  moy su niou yaay
Djiguene djiguene  moy su niou Wéeruwaay
Djiguene moy ki Yalla teral  té moy sou niou wetal
Sa su niou méré djiguene moy ki niouy bégal
Djiguene djiguene moy su niou waay
Djiguene djiguene moy su niou noflaay
Nioy diour yar boot nampal aka tété
Kou mandi na mbatu mi delou fa nga rooté

Ganaw goor Yalla gou né
Djiguene djiou baaxa fa né
Di saytou aka topatoo si waleu wou né
Boul ko mèré déko mougnal
Boul ko Def sa noon
Lou niou la gueuna mougnal
Mouy leral sa Yoon
Aldiana ngui sa soufou tankou yaay
Boulako adouna diaral
Nianam agana déf ko sa Wéeruwaay
Weurseuk wi déko si teral
Nioy diour Yonénta
Waliou Goor Yalla   ndiitou rew
Bep Borom ndombal tankeu
Bou niou sekhak niom nganteu
Sou niou beugué lou lew
Si dieuflanté ak niom la niou bari rawanté

Djiguene djiguene moy su niou yaay
Djiguene djiguene moy su niou Wéeruwaay
Djiguene moy ki Yalla teral té moy sou niou wetal
Sa su niou méré djiguene moy ki niouy bégal
Djiguene djiguene moy su niou waay
Djiguene djiguene moy su niou noflaay
Nioy diour yar boot nampal aka tété
Kou mandi na mbatu mi delou fa nga rooté

Kou fiy FAWADE WÉLÉ ame sa MALICK
Kou fiy SOKHNA DIARRA ame sa BAMBA kou fi  
ASTA DIANKA ame sa  BAYE NIASS  kou fiy
COUMBA NDOYE  ame sa MAME LIMAMOU
Du Yooooooooooooon niou lene di dioyloo
No woman no cry
Djigueeeeeeeeeeeeeeeen Nioy sou niou Yaay
Niooooooooooooooy sou niou Wéeruwaay
No woman no cry
Djiguene Warul dioy
Djiguene warul dioooooooy

Ecouter

A Propos de "Weeruwaay"

Album : Weeruwaay (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Mar 29 , 2021

Plus de Lyrics de LEUZ DIWANE G

LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl