Paroles de Afélé (Remix) Par LEUZ DIWANE G


Badiya wo lé yé gnin Saabou
Al ngha séyi woo, ntol ya
Nkambeng ta, fo atol fanang sé séwo
Casa Nkol wo a bé ning Sembo
A félé eh, a félé eh
A félé eh, a félé eh

Sembe, Casa yoolala Sembe
Bakk ma diola ci baay, saafom katisindéy
Karésom Paul, Sagna ndooba, diox ma loxo ñu waxtaan
Xél ak xol maassé, noon ba sëngeem mom ma ñu doon naxtaan
We from the motherland, casa di mansa the roots
Guélawu réer gui mëdduléen, té ëlëk ñun la déss ñu djukk si
Gaddu kadjandok djassi - bay dundé wala bay djaay
Ñiy song war yi fok book na si - A Félé bokk bëgg fay daay
Djogué Teugeedj féey ba ci péggu maam, aksi xëy sanggou lékk naan
Xam sa démb ca Bignona, a maamom William djanténom
Xam li ñu am, am lu ñu moom, jamm itam
Jog sakku ji ñaan, xéweul bawaan ci casamanca

Mboloo moy su ñu dolé bou leen ko saganè
Na ñu bolé su ñuy dolé siggi bañ ou ñu feewale
Casamance casadimança Casa diyaatalé
Ay woulé nata bayla à félé

Def nguir firndelate ni dama Doff ci yaw
Na jam ji sax, naatangué raw dakk ba faw
Dem guenoul ci nioune meune ta niak fok niou mougne
Tay dama déloussi ak samay niogne pour eundi pogne
Fassat fethie pour fekki tekki sa sufu tank
Xassal diox niou ci reen yi woor neu len douniou Sank
Li la weur ci xeet doyna firnde ni jam nga xam
Dafa dess ci gniy seet takou topou sen tankou mame
RN6 aksi guiss, car bi sarr ba Fuladou yéwou feulé Sédhiou
Kalounaye ngay am Kassumaye samay mboki Blouf
Fogny, Bandial, Cap naan ci ndoxu Diémbéreng

Mboloo moy su ñu dolé bou leen ko saganè
Na ñu bolé su ñuy dolé siggi bañ ou ñu feewale
Casamance casadimança Casa diyaatalé
Ay woulé nata bayla à félé

Ce mélange d'ethnies et de races
Cette diversité culturelle
Cet oasis de couleurs, cette richesse, ce melting pot
Faut pas faut pas céder à la tentation
Pas de faux Pas
Nous voulons fédérer une seule nation
Politique politicienne qui déchire ce tissu de fraternité qui nous lie
Polémique non
Nous voulons un mélange homogène pas de haine diameu la paix comme on dit
Ay woulé ay woulé ay woulé heee heeeeee
Casamance diyaatalé

Mboloo moy su ñu dolé bou leen ko saganè
Na ñu bolé su ñuy dolé siggi bañ ou ñu feewale
Casamance casadimança Casa diyaatalé
Ay woulé nata bayla à félé

Badiya wo lé yé gnin Saabou
Al ngha séyi woo, ntol ya
Nkambeng ta, fo atol fanang sé séwo
Casa Nkol wo a bé ning Sembo

Mboloo moy su ñu dolé bou leen ko saganè
(ByMic Sembo Sembo Sembo)
Na ñu bolé su ñuy dolé siggi bañ ou ñu feewale
(By Mic Sembo Sembo Sembo)
Casamance casadimança Casa diyaatalé
Ay woulé nata bayla à félé

Ecouter

A Propos de "Afélé (Remix)"

Album : Afélé (Remix) (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Dec 14 , 2021

Plus de Lyrics de LEUZ DIWANE G

LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G
LEUZ DIWANE G

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl