
Paroles de Téré Nelaw
Paroles de Téré Nelaw Par NAFANA
[COUPLET 1]
Khar ba sone, Gneuwolo
Wonala téléphone ioe djeuloulo
Fo nék loy déf, lep dina lerr
Téy la téy mba fomboulo
Mak sama team paré nègne complot
Kay fi, diégé ma bala may mérr Baby...
Guiss na ni meuneu touma la bayi
Kham nga ni dou ay wakhay takh ma tayi
Dinala wone samay fème, téyé leu do dèm fène
Beugue na nga feusseul li ngay woté tchi yaw
Boul ma neub baby wone ma ko
Dalalal sama khel, show me your love
[REFRAIN]
Ndakh malay téré nélaw baby
Diégé sima kay ma déh leu yay sama way
Boul takh ma néleu bye bye bye bye byyye
Man malay téré nélaw baby
Diégé sima kay ma déh leu yay sama way
Boul takh ma néleu bye bye bye bye byyye
[COUPLET 2]
Right lépp deugeuleu
Yague nga ma khar yeksinaaaa, you are my life
Kou nek amna koula y’Allah bolél
May sa guénouwal, indil li tchi déss complètel
Guéneul sa rouk gneuw tchi mane gnou meuna dadjé
Yay kiy léral sama yone dima djité
Damay teud di khalat di weulbetikou left and right
Mbeugél bima am tchi yow lérna meune nako watt
Nobé nala louné té défouma tchi « je retiens »
Dé ma yeureum, boul ma wakh loudoul deugeu
Goor deug nga, just man
Boudoul yow dou done kénène
Nanga kham li la warr diko déf kène dou la stressé
Djigène deug nga toudoul nala
Sama caporal watiél nga ma thiono
Khana khamoulo ni yow yay kima nobb
That's why...
[REFRAIN]
Ndakh malay téré nélaw baby
Diégé sima kay ma déh leu yay sama way
Boul takh ma néleu bye bye bye bye byyye
Mane malay téré nélaw baby
Diégé sima kay ma déh leu yay sama way
Boul takh ma néleu bye bye bye bye byyye
Kham ngani malay téré nélaw
Baby deug deug yamay téré nélaw
Boul takh ma néleu bye bye bye bye byyye
Kham ngani malay téré nélaw (ngani malay téré nélaw)
Baby boulma neub malay téré nélaw (baby malay téré nélaw)
Boul takh ma néleu bye bye bye bye byyye
[REFRAIN]
Ndakh malay téré nélaw baby
Diégé sima kay ma déh leu yay sama way
Boul takh ma néleu bye bye bye bye byyye
Man malay téré nélaw baby
Diégé sima kay ma déh leu yay sama way
Boul takh ma néleu bye bye bye bye byyye
Ecouter
A Propos de "Téré Nelaw"
Plus de Lyrics de NAFANA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl