MAABO Ideu  cover image

Paroles de Ideu

Paroles de Ideu Par MAABO


Mane kane laci wara wakhal ?
Aissata wala Mia ?
Khame nani niakoumala
Nakh yameu dioural ay doom
Fater wouma ki niou soûl tchi Yoff
Ak souniou Amina namena fo akk mom
Reuthiouwouma ma sama seuy ak yow
Djigueine dei geunou la si souf ni sa tourondo
Djikko yi rafet yima kham tchi yow
Bouma fi togone di ci wakh fi ba souba dou diekh
Mangui niane diam tchi yow
Niane yalleu nangou tei yokk leu

Nianouma djital kein tchi yein
Goudal fann yow ak sama mame Amina
Boul fater niane yimala dinkone
Beuss bo degguer ni njibina
Mane dei namena khetou wagne
Bi done khegne si keur gui
May yendo fetieu ak way
Doumalako neub souniou andd bi
Beugouma wone mou diekh
Wayer diameu ak pekhem
Yalleu ak ndogalam
Yow dé sama nawlé ngua
Dou meuss nekh bama fater leu
Yow dé sama nawlé ngua
Fatew ma bigne lay mour nguay nieuw tchi mane
Niongui done niane benene dom bou goor
Touder ko seydina Mouhamed
Niou dem adji Makka
Fatew meu biniouy nieuk wahtane
Fatew meu biniouye moudier wahtane

Waylé lein ma
Aissata legui sama rakk ngua
Kone denkeu nala
Yow boko ak niom sokhna ngua
Nakh Aissata fété kaw Mia
Adouna ko belel dierry
Dounya Ko meri (meri)
Demna rakk yaralma sama mame
Yalleu neu Yalleu leral sa yone
Dingua guiss kou nek kholal boubakh
Sa mbekté moy diam Amina
Woy Mia wala Aissata
Santeu naléne geureum naléne tay
Euleuk dou agne dou rer
Wayer lou mata sor leu
Yalleu neu Yalleu def
Li geun ci yow
Tagou nala Aissata
Mangui lay balou tei dila bal
Aissata mane sa Mak la

Ecouter

A Propos de "Ideu "

Album : Ideu (Single)
Année de Sortie : 2022
Ajouté par : Farida
Published : Nov 18 , 2022

Plus de Lyrics de MAABO

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl