MAABO Namel cover image

Paroles de Namel

Paroles de Namel Par MAABO


[VERSE 1]
Baby, baby namnala, only mani nameunala
Sama xol lama sori dem a dani dolé bayima ak wétay
Yama dane motali, ba nga démé la guédja
yeuk nékhay
Ioe ya takhone, ma bayi kharite yima am yeup
Té béneu kharite, la déssé wone té ioe leu dém ngeu
Boudone niénte fouki atte dinako tokk dila khar,
Yama fék si leundeum, talal mey phare léral sama yone
Mane rek ci khalé, namouma koudoul guissé maabo
Ken dou ioe té yafi meun, yamey diokh li
Geun ci mane


[CHORUS]
Baby I miss you. Yes I really do
Honey I miss you. How can I leave without you
Quand t’es loin de moi, je ne vis pas
Je mourrai 100 fois rien que pour être dans tes bras


[VERSE 2]
Lig ma sorri takh ma diakhasso,
wétay moma teuthie kasso,
Téléphone doyouma baby ioe nameunala
Dmalay sentir, nga diégué té sorri ngamaa,
Boul merr, boul firr, guissouma fi kouma lay dieundé
Leg lek ma diougue ndax teureudi,
Ioe késsé ci xol dara khadioufi, li nga beug moy ma gnibissi

Khamo ni mala geuneu beug gnibissi
Mbeuguel, kéneu khamoul, loumuy,
Def ci nitt bamouy, namé, baby yo soumala meunoul indi fi
Kéneu wakhatou ko


[CHORUS]
Quand t’es loin de moi, je ne vis pas
Je mourrai 100 fois rien que pour être dans tes bras
Baby I miss you. Yes I really do
Honey I miss you. How can I leave without you
Quand t’es loin de moi, je ne vis pas
Je mourrai 100 fois rien que pour être dans tes bras
Baby I miss you. Yes I really do
Honey I miss you. How can I leave without you

Toucouleur bou rafet ba ngui ni, hé  
Borome nak ak mew ba ngui ni, hééé
Yamay danel, dag ma
Namone ma ngui ni, nameuleu takh mane ma gnibissi
Dag ma namone ma ngui ni, nameula takh mane ma gnibissi
Hé ! hé ! hé ! hé ! hé ! Toucouleur bou rafet ban gui ni
Hé ! hé ! hé ! hé ! hé ! Borome nak ak mew
Ban gui ni, ban gui ni

Ecouter

A Propos de "Namel"

Album : Namel (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 03 , 2019

Plus de Lyrics de MAABO

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl