Paroles de Yako Waral Remix Round 6
Paroles de Yako Waral Remix Round 6 Par MAABO
[COUPLET 1]
Héy ! Kholate ma kaw ba souf, ma len dakh solou fouf
Bbay boul di diawalé, dou beurri yéré moy sagnsé
Kholmaaaa ! Fouma meuna guéneu ngané fi leu,
Kham ngaaaa ! Dou ci yéré yi ci mane mi leu
Kholm anima 3 pièces diapé,
Té douma djiby dramé, damay dieum mak di délou khalé,
ioe fo may dieuleuté souma nékhé obasanjo,
Def class ték chapeau, kay dieul ay photo,
Li yeup yako waral guissé maabo
[REFRAIN]
Hé ! Ioe khalé bi lé, ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh !
Sa dokhine bi nexnamaaaa ! Hé hé !
Ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh !
Sa dokhine bi nexnama
Niou dém, kone naniou dém thiakass ! Thiakass ! (thieum hé !)
Thiakass ! Thiakass ! Dara douniou té thiakass ! Thiakass !
Thiakass ! Thiakass ! Ayway,
Naniou dém thiakass ! Thiakass ! Ooooh ! Héh !
Thiakass ! Thiakass ! Dara douniou té thiakass !
Thiakass ! Nioune dara douniou téré dé
[COUPLET 1]
Bala ma dougou école, tchi la am class,
Ma nek ci sa xol, ndax dama am thiass
Baby, kholma, douma moramou goné,
Beuss bi tay la, dina la wane fima meuné
Di solou ni mannequin, diékk ni djèk, di dagou ni drianké
Moussorou ni diouma dieng,
Té fouma tassé sama cheveux done sa beyoncé
Kay diégué ma niou snap selfie, kay niou dieul ay photo,
Aduna yeupeu guiss ko, liiii… ! Yako waral guissé maabo
[REFRAIN]
Hé ! Ioe khalé bi lé, ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh !
Sa dokhine bi nexnamaaaa ! Hé hé !
Ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh !
Sa dokhine bi nexnama
Niou dém, kone naniou dém thiakass ! Thiakass ! (thieum hé !)
Thiakass ! Thiakass ! Dara douniou té thiakass ! Thiakass !
Thiakass ! Thiakass ! Ayway,
Naniou dém thiakass ! Thiakass ! Ooooh ! Héh !
Thiakass ! Thiakass ! Dara douniou té thiakass !
Thiakass ! Nioune dara douniou téré dém
[OUTRO]
Thiakass ! Thiakass ! Ioe sama djiguennn…,
Da nga am class bégue na ci ioe
Mane ioe yay, lima mome, wowoooohhh ! Guissé maabo
Ecouter
A Propos de "Yako Waral Remix Round 6"
Plus de Lyrics de MAABO
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl