Paroles de Yin Yang
Paroles de Yin Yang Par MAABO
Chérie coco lo def nekhna, Guani
Boudé aye nakh sakh bakhna, Haann
Yaye sama thione maye diagua, Wakhal
Keninne koudoul yaw me begouma, Heeee waye
Beus Bignu gneuka guiser la mir, Guani lane?
Dagua dionger thi gor yaw mi, Bayima waye
Bouma waxane li né thi yaw mi, Bayil mou sede
Na bayi mou sede ndakh khadioul fi
Beute moy xool wayé xol moy guiss
Fouma meuna xool yaw rek lay guiss
Sa dieumak sa takander
Goudi gui yaw laye djaner
Sa refetaye dafa yemer
Motakh ma diangui karate
Koula togne fok laler hé
None yiye wakhnane mane ak yaw dougne yague
Sou desone si gnome dougnu ande
Bi nieup bagné yama nangoul
Gatié ngalama sokhnassi bakoul
Yama diangual mgeguelou bandit
Yama fouyal topatoma motakh maye dokh ni Gondi
Yalla moko dogual kene meunousi touss
Sama xole dieule ko
Louthi name boul xar def ko
Begue nako doundou ak yaw
Aye fane bou goudou mak yaw
Senegal yako mome
Soma méré ma xare guethie gui
Sebegal yaye borom
Soguo beguer ma nangou pallet bi
Dieunde almadi maye la
Thiabi auto route bi diokhla
Changer monument bi defthi mak yaw
Nek president pour yaw
Cherie coco lo def nekhna, Guani
Boudé aye nakh sakh bakhna, Haann
Yaye sama thione maye diagua, Wakhal
Keninne koudoul yaw me begouma, Heeee waye
Beus Bignu gneuka guiser la mir, Guani lane?
Dagua dionger thi gor yaw mi
Bayima waye
Bouma waxane li né thi yaw mi
Bayil mou sede
Na bayi mou sede ndakh khadioul fi
Sama xole bi dafla mine
Yaw rek sama diara bi
Begouma koudoul yaw
Nagne ma bayek yaw
Sa yener eupena
Wayer sa mbeguel doye nama
Aldiana guama dji
Seye ak yaw ba firdawsi
Ayo lé lathie ma noumalaye wower
Ayo lé sama chocola laleye wower
Thiouw dou jipe
Cherie coco yaye boss fi
Couple bou heureux guaye ame fi
Kougnu nekhoul boul gnew fi
Sama xole dieule ko
Louthi name boul xar def ko
Begue nako doundou ak yaw
Aye fane bou goudou mak yaw
Senegal yako mome
Soma méré ma xare guethie gui
Sebegal yaye borom
Soguo beguer ma nangou pallet bi
Dieunde almadi maye la
Thiabi auto route bi diokhla
Changer monument bi defthi mak yaw
Nek president pour yaw
Mia moye Hiroshima
NFU moye Nagasaki
Chérie coco lo def nekhna, Guani
Boudé aye nakh sakh bakhna, Haann
Yaye sama thione maye diagua, Wakhal
Keninne koudoul yaw me begouma, Heeee waye
Beus Bignu gneuka guiser la mir, Guani lane?
Dagua dionger thi gor yaw mi, Bayima waye
Bouma waxane li né thi yaw mi, Bayil mou sede
Na bayi mou sede ndakh khadioul fi
Ecouter
A Propos de "Yin Yang"
Plus de Lyrics de MAABO
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl