Paroles de Tukki
Paroles de Tukki Par MAABO
[VERSE 1]
Mane bimay dem khawma dara
Bima yeksé guissouma dara
Ma bayi lepp sama guinaw
Mane nane lay def
Deukouma fi, deukeutouma fé
Yague aleu bakhoul non
Bokouma fi, bokatouma fé
Yague aleu Bakhoul non
Ma ngui set sama bop ci samay mbok
Ndax sama yone amna nioumay dokk
Koumay guindi
Sama yone waxma sama bopeu
Ndax mom lay set
Boudé fite ak foula moy takha touki
Tay ragal nako
Néka djiguene téla dem touki outi
Lounek dégeu nako
Ki sopékouna lounek dégeu nako
Ki déh yakhouna héé ! Kone fauk ma gnibissi
|CHORUS]
Kagn lay gnibissi, Kagn lay gnibissi gnibissi
Ak fane lay gnibéti, fane lay gnibéti
Kagn lay gnibissi, Kagn lay gnibissi gnibissi
Ak fane lay gnibéti, fane lay gnibéti
[VERSE 2]
Sama nékine mom oumpou nalen wa werr
Bi déh ma yoné len khaliss rek yen
Khamou len sax sakh loumay
Liguey ak limay dathie ba di len ko yoné
Té bala ma am séni kayite
Pékhé bou nek nga diém nguir khagn mako
Mane, immigré dafa méti
Fi gnifi deukoul nieupa beugeu gnibi
Kou touki ngané diw tékki na, no no dou ni
Bamou démé yagoul tabakh na ioe lo fok fi
Doundou bitim reew bokoul ak bou fi
Ken dou for khaliss danioukay liguey, mane khamatouma
Fane la fété, fouma meuna dem léneu laniou may lathie
Woooooh ! Ioe kagn ngay gnibééé
Wooooh ! Légui fane lay gnibi
[CHORUS]
Kagn lay gnibissi, Kagn lay gnibissi gnibissi
Ak fane lay gnibéti, fane lay gnibéti
Kagn lay gnibissi, Kagn lay gnibissi gnibissi
Ak fane lay gnibéti, fane lay gnibéti
Hannnnn...! Li déh méééétinaaaa
Yéhhh ! kagn lagnie gnibéti
(Kagn lay gnibissi)
Ak fane Lagnie gnibéti
(Fane lay gnibéti) nioune
Kagn laniouy gnibéti
(kagn lay gnibissi)
Ak fane lagnie gnibéti
Ecouter
A Propos de "Tukki"
Plus de Lyrics de MAABO
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl