Paroles de Nit Kou Bakh
Paroles de Nit Kou Bakh Par BAYE MASS
Meussouma fogue ni dingue ma meusseu bayi
Deloussil samay lokho ngua baalma
Fimala tek yow latie ko sa gars gni
Kheuyna dama dioum wayé baalma
Demb lima rérone takh ngua bayi
Tey ma souk sa kanam nane la baalma
Naam naleu yalla kham na naam nala
Daroo wade ndiakk mane naam naleu
Niit kou bakh ngeuu
Té sax sama waay ngeu
Damay souk la balmeu
Naniou yessalate mbeuguel gueu
Niit kou bakh ngeuu
Té sax sama waay ngeu
Damay souk la balmeu
Naniou yessalate mbeuguel gueu
Mbeuguel deugue yallah moko moom
Wayé thi mbeuguel bobou laniouy beuguanté
Tchi lay fateliko bamou meussane nekh
Tchi lay fateliko soma meussane retane
La zoulaikha dadione ndakh mbeuguélam
La fama dadione ndakh waayame
Naam naleu yalla kham na naam nala
Daroo wade ndiakh kay nga balema
Niit kou bakh ngeuu
Té sax sama waay ngeu
Damay souk la balmeu
Naniou yessalate mbeuguel gueu
Niit kou bakh ngeuu
Té sax sama waay ngeu
Damay souk la balmeu
Naniou yessalate mbeuguel gueu
Bi tchi ndieuk nangou nané mala togne
Wayé djiguene dafa wara souuufé
Ware ngua kham né yaw yaye sama titeur
Té kilay titeuro dangue ko wara djiteule
Té soumala nane niite kou rew ngeu
Yow boum ladi meti yow banekh ngeu
Banekh ngeu
Balma ak
Balnala ak
Yalla naniou yalla bole baal
Kham na dou niak meune nala togne way
Nanga mako djégual
Yén say seytane meune nama deflo
Ecouter
A Propos de "Nit Kou Bakh "
Plus de Lyrics de BAYE MASS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl