Paroles de Imam
...
Paroles de Imam Par BAYE MASS
Yar nga nu ci yoon nekuloo bàay buy ragual loo ay doomam
Joxoo nu chateau wàaye sèetanu lonu rek nuy wer di toon
Da nga màandu lool sa yar book nàa ci doon yikko njek sèede bàay
Yalla nga fi yag lool tunda bi yèep sèede nane ni am nga njarin bàay
Njarin bàay
Njarin bàay
Njarin bàay
Sun la xasèe dom nopii
Nax sa bàay baxna lool
So nakèe dom nopil
Nax sa bàay dafa màandu won
Sun la xasèe dom nopii
Nax sa bàay baxna lool
So nakèe dom nopil
Nax sa bàay dafa màandu won
Amoule noflaye
Amo fi morom
Toundou wi
Ragnel neugnn la
Fexe nge ba fèep funu took nu jox nu sunu wàaju wàay bàay
Nax yàama don wox nan dom
So nèeke ci gox nu am funu tek sa bàay
Sooy jef dèel xol ci mom
Kuko beg yàap ci yawl ay jàa
Sookoy xol do waji yon
Wade njàak man sa dom màalay wax
Jerejefeti
Wacco ngàak nun
Def nga lilla war nun nola desèel wèecet be
Bàaya nep ngàa
Kon xàamowul say dom ci biir njaboot ge
War namàa bàay
Ma feental la wàay ay kadu bayil lakofe
Wade njàak man sa dom màalay wax
Jerejefeti
Wacco ngàak nun
Def nga lilla war nun nola desèel wèecet be
Bàaya nep ngàa
Kon xàamowul say dom ci biir njaboot ge
War namàa bàay
Ma feental la wàay ay kadu bayil lakofe
Ecouter
A Propos de "Imam"
Plus de Lyrics de BAYE MASS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl