Paroles de Woudié (remix)
...
Paroles de Woudié (remix) Par BAYE MASS
Kumpe bilèen boole
Wacci sèeni tank
Tax na ma làac lèen
Nax xam ngèen lilèen boole
Dèeg nàa wuje du nonèel
Xam lèen ko sa ndortèel ba
Motax ma lacc lèen man
Nax xam ngèen lilèen boole
Dèeg nàa wuje du nonèel
Xam lèen ko sa ndortèel ba
Motax ma lacc lèen man
Nax xam ngèen lilèen boole
Ki ngay fèeki
Def ko ni sa yàay boy
Yaw mi ko fèeki
Dinala def ni domam
Sèen alàaji
Yèena fèes ci xol bii
Yaw alàaji
Yamatèel njaboot gi
Jabar la ni yaw yaw jabar nga ni mom
Def ko ni sa yàay mu man la wan lim jota goop
Da ngèen bok wersek bulko xolèe betu noon
Ngèen japale alàaji nu bana xàame sèeni doom
Dèeg nàa wuje du nonèel
Xam lèen ko sa ndortèel ba
Motax ma lacc lèen man
Nax xam ngèen lilèen boole
Wàaye bum nèex ba nga fàate ni demb moo fi nèekom
Yoraloon la say cer sàamalon la say doom
Demb tax nu naan tey
Lendem muju doon leer
Hum nèex ba nga fàate
Nebel fi nga fèete
Gem nàa ne wuje du nonèel
Wuje du nonèel
Wuje du nonèel
Gem nàa ne wuje du nonèel
Wuje du nonèel
Wuje du nonèel
Fexe lèen xam lilèen boole balàa muy nacc
Fexe lèen xam lilèen boole balàa muy nacc
Wolof njàay nèena yéena nèek la kucciy fanàan
Yéena nèek la kucciy fanàan
Lu yàala dogal sèen bàanex la
Wolof nèena yèene nekk la
Budè lu bàax la yàa ciy fanàan
Lu yàala dogal sèen bàanex la
Wolof nèena yèene nekk la
Budè lu bàax la yàa ciy fanàan
Lu yàala dogal sèen bàanex la
Wolof nèena yèene nekk la
Budè lu bàax la yàa ciy fanàan
Lu yàala dogal sèen bàanex la
Wolof nèena yèene nekk la
Budè lu bàax la yàa ciy fanàan
Ecouter
A Propos de "Woudié (remix)"
Plus de Lyrics de BAYE MASS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl