Paroles de Kuma Nop
Paroles de Kuma Nop Par MAABO
[CHORUS]
Kouma nop, lathie ma kouma nop
Sama sadiabade, kouma nop lathie len ma kouma nop mane
Souma done orchestre, moy sama guitar bass
Loe ya takh sol daleu nex, yay sama kawass yéh
Sama sadiabaaane
[VERSE 1]
Loe lay wo wouyuma warouniou di rérro
Waxal ak mane té nga ré
Waxma koula togn beugouma
koulay merloo... Waxal ak mane té nga ré
Sa kaname bi nga fass ni, niémétoumala ni
May wax ngey bign, dima xélo ni
Amatoulo sama kersa ioe mi (dédéte)
Loufi diar ba nga beugeu mel ni
(Fauk ma mel ni)
WaxmaLoula daal bag may tonto ni
(Leep ci ioe leu)
Kone ma ley merlo ni
[OUTRO]
Li nga fauk la, lathi ma louma naam (lo naam waxma)
Fima tolou ni, ma ngui sama oh lala ! Mane
Dièk piir, waxma lofi manqué
Fi may first lady ken douma diamnané
Iyo ! Iyo, Iyo ! Iyo
Ya di sama sadiabade, Iyo ! Iyo
yay kimay motelééé
[CHORUS]
Kouma nop, lathie ma kouma nop
Sama sadiabade, kouma nop
Lathie len ma kouma nop mane, sama sadiabane
Souma done orchestre, moy sama guitar bass
Loe ya takh sol daleu nex, yay sama kawass yéh
Sama sadiabaaane
[VERSE 2]
Loe lane laa, soneu na légui may ma
Démétoul nonou mak ioe, wowowowoyy bayi ma
Métiwone na, té démouma
Lépeu la mougn ca bamouy méti
Dimbali ma waxma loula yeukeuti
Wouyoooy ! bayi ma
Niarél ngafi beugeu takk, waxofi dara
Lou lerr nirél ngafi beugeu takk hey
[OUTRO]
Li nga fauk la, lathi ma louma naam (lo naam waxma)
Fima tolou ni, ma ngui sama oh lala ! Mane
Dièk piir, waxma lofi manqué
Fi may first lady ken douma diamnané
Iyo ! Iyo , Iyo ! Iyo
Ya di sama sadiabade, Iyo ! Iyo ! yay kimay motelééé
[CHORUS]
Kouma nop, lathie ma kouma nop
Sama sadiabade, kouma nop
Lathie len ma kouma nop mane, sama sadiabane
Souma done orchestre, moy sama guitar bass
Loe ya takh sol daleu nex, yay sama kawass yéh
Sama sadiabaaane
Kouma nop, lathie ma kouma nop
Sama sadiabade, kouma nop
Lathie len ma kouma nop mane, sama sadiabane
Souma done orchestre, moy sama guitar bass
Loe ya takh sol daleu nex, yay sama kawass yéh
Sama sadiabaaane
Kouma nop, lathie ma kouma nop
Len ma kouma nop mane
Ecouter
A Propos de "Kuma Nop"
Plus de Lyrics de MAABO
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl