
Paroles de Ngalam
...
Paroles de Ngalam Par Believe Boyz
Deg na niou nane man damay khémeme
Yaw rek lay guiss loumay doyer lenene
Ta yay bidew bimay leral
Souma narer gadaye ba doma setane
Dagua fess si sama khol
Khol bay galanio
Mat seuk sama wait yaw koulay am di fo
Yaw rek lay tope yaye sama Renou hole
Mak yaw dotoul dagne
Manakh yaw
Sama chérie nala takal ngalam
Diokh la auto gua dawal
Nane la bébé niafal
Niaf rek
Ta yaye bidew bimay leral
Souma narer gadaye ba doma setane
Ta yaye bidew bimay leral
Souma narer gadaye ba doma setane
Mane sétane na set ba set Kham ni diaral ngama
Doff Lo ngama ni mbeuguel Lou khalé
Li dafa diss deh
Khol bou fess akh banex la la yénéeee
Kou done nelaw nga yéwou yay sama
Aldiana ma baby
Yama féniou wane ma love ma yéwou mouy kémane
Boukene beuguol beugue nala yay sama aldiana
Yay sétou biy wané sama leray
Makh ioe for life pikal pel la oh baby
Sama chérie nala takal ngalam
Diokh la auto gua dawal
Nane la bébé niafal
Niaf rek
Ta yaye bidew bimay leral
Souma narer gadaye ba doma setane
Ta yaye bidew bimay leral
Souma narer gadaye ba doma setane
Ecouter
A Propos de "Ngalam"
Plus de Lyrics de Believe Boyz
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl