Paroles de Free Sénegal
Paroles de Free Sénegal Par BAMBALY SECK
Askaan wi sonou nagn
Gni diakhlé akk tiss moléén dapp
Gni leen wara kassal nopi négn
Gni diakhlé akk tiss moléén dapp
Makk gna gui weur di dioy
Diakhlé akk tiss moléén dapp
Jeunesse bagui niakk sen baken
Ndakh seen wakhi tey outé na ak sen wekhi demb
Sugnu Sénégal nioune nioko mom niou ande khékh
Injustice bi douniou ko nangou daffa doy nak
Yow gua dioy mane ma dioy
Askaan wi da di dioy
Askaan wi sonou nagn
Gni diakhlé akk tiss moléén dapp
Gna leen dane khékhàl guissu gnu leen
Gni diakhlé akk tiss moléén dapp
Wadiour yagui wéét di dioy
Nguir niakk séni doom
Un peuple opprimé
Liberté bafouée
Diakhlé akk tiss moléén dapp
Sugnu Sénégal nioune nioko mom niou ande khékh
Injustice bi douniou ko nangou daffa doy nak
Trop d’émotion pour d’écrire
Ce que le peuple sénégalais est en train de subir
Soyons engagés
Car ce combat dépend de l’avenir de ce pays
Free Sénégal
Ecouter
A Propos de "Free Sénegal"
Plus de Lyrics de BAMBALY SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl