Paroles de Tristesse
Paroles de Tristesse Par ISS814 BEATS
[REFRAIN]
Bou féké lim la wax daf la féxé
Meun nga dem sa yoon grawoul
Bou fékè louniouy doundou daf ley stréssé
Meun nga dem gnibi thioloul
Mais ma gui ak tristesse tristesse
Bayé mak sama tristesse
Bayé mak sama tristesse
[COUPLET 1]
Hé damla beug té y'allah tax, yeah !
Khalé bi, mounouniou nek té douniou wax
Hé, sokhna si, koula beug nga def ko noone
Hé, ndeysanne, diougal nga dem sa yone
Souma ndanane
Khamna ni nala manquer
Ay way ! Ioe tamit dig ma manquer hannn!
[REFRAIN]
Bou féké lim la wax daf la féxé
Meun nga dem sa yoon grawoul
Bou fékè louniouy doundou daf ley stréssé
Meun nga dem gnibi thioloul
Mais ma gui ak tristesse tristesse
Bayé mak sama tristesse
Bayé mak sama tristesse
[COUPLET 2]
Hé ! Sama wax dafa méti
Té da nga gawa meer
Baniouy moudji xèkh fi
Mane ak ioe comme ennemis guerre
Démal nga gnibi mo geun si ioe
Hey ! Té boul niowate
Beuss bouné ma deg thiow
Warouniou xoulo way
Souniou meer ra niou eup vitesse, té bakhoul
Ya ngui dem ba fi tristesse, mais grawoul
[REFRAIN]
Bou féké lim la wax daf la féxé
Meun nga dem sa yoon grawoul
Bou fékè louniouy doundou daf ley stréssé
Meun nga dem gnibi thioloul
Mais ma gui ak tristesse tristesse
Bayé mak sama tristesse
Bayé mak sama tristesse
No way !
Youkheunté, saganté, kou nek dém
Yan moment ci ngey nek ci probleme
Khalatal boy yi
Gnibissil ci keur gui
Tristesse tristesse
Tristesse tristesse
Meun nga dem sa yonne grawoul
Meun nga dem gnibi thioloul, sama tristesse
Ecouter
A Propos de "Tristesse"
Plus de Lyrics de ISS814 BEATS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl