Paroles de Fresh
Paroles de Fresh Par ISS814 BEATS
Yéwu def Fresh
Yewu def ouhhh
Sangu def Fresh
Sangu Def ahhh
Solu def Fresh
Solu def wouyay
Guene def Fresh
Guene def mbap
Fresh si ndey
Fresh si baye
Fresh si solou
Oh my Fresh
Noy def ba do Fresh?
Wahma noy def ba do Fresh?
Do ma done swag dance
Faut que ma compté wat fans
Ya ngui sissou wat Lank
Meune touma di teup di dal ndank
Xamulo nakawar baye
Mane la boy bi weuy ndank
Dame lay géné fils, bye
Ame na bénéfice, banque
Marakissou lékh, di pess
Sa papa moy wakh, nél moutt
Dougou bus bourlé, di pess
Sa rap bi fayoul, nel moutt
Bokouniou, dagn wouté
Ligne lay fay salaire, sama goûter
Réré dibi mboté
Guel bi nguay guente, sama côté
Yéwu def Fresh
Yewu def ouhhh
Sangu def Fresh
Sangu Def ahhh
Solu def Fresh
Solu def wouyay
Guene def Fresh
Guene def mbap
Fresh si ndey
Fresh si baye
Fresh si solou
Oh my Fresh
Fresh si ndey
Fresh si baye
Fresh si solou
Oh my Fresh
Yéwu def Fresh
Yewu def ouhhh
Sangu def Fresh
Sangu Def ahhh
Solu def Fresh
Solu def wouyay
Guene def Fresh
Guene def mbap
Fresh si ndey
Fresh si baye
Fresh si solou
Oh my Fresh
Noy def ba do Fresh?
Wahma noy def ba do Fresh?
Diokhor madior, diokhor lene
Mélone lene ni niou mel, sokhor lene
Bindi son yi, diokhate lene
Air bou fresh dokhote lene
Wiri wiri, diari ndari
Solane dal yi, touli tate yi
Takk bac bi, dem na djangui
Rer na France, mane la Diarry
Eh pousseul fé, boul ma fonto
Sa best guel mane ma konko
Boul ma clashé, noum lay tonto
Bou ma massé, faut que ma sonko
Meussou meu Sweet, I’m beauty
Faut que ngua tarri sarr pour adji
Dagnouy sandi kher pour promo
Nékoul Auchan laniouy dadji
Check
Deme gauche ak sama gars yi
Def fresh, fresh, fresh, fresh
Nagne dem droite, non dou niou bayi
Def fresh, fresh, fresh, fresh
Sokhor ni
Xolal ligni sol
Def fresh, fresh, fresh, fresh
Nioy pendeul basa école
Def fresh, fresh, fresh, fresh
Yéwu def Fresh
Yewu def ouhhh
Sangu def Fresh
Sangu Def ahhh
Solu def Fresh
Solu def wouyay
Guene def Fresh
Guene def mbap
Fresh si ndey
Fresh si baye
Fresh si solou
Oh my Fresh
Yéwu def Fresh
Yewu def ouhhh
Sangu def Fresh
Sangu Def ahhh
Solu def Fresh
Solu def wouyay
Guene def Fresh
Guene def mbap
Fresh si ndey
Fresh si baye
Fresh si solou
Oh my Fresh
Noy def ba do Fresh?
Wahma noy def ba do Fresh?
Ecouter
A Propos de "Fresh"
Plus de Lyrics de ISS814 BEATS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl