Paroles de Problème
Paroles de Problème Par ISS814 BEATS
Né nga da nga am problème
Mais mala eup problème
Kou si nék amna problème
Mais dou nieupeu kay waax
Né nga da nga am problème
Mais mala eup problème
Kou si nék amna problème
Mais dou nieupeu kay waax
Amo ndieugou ordonance
Mane cancer moma dal
Est ce que doma dimbeli si pass
Mane si bourlé car lako cal
Sa guél daf la trahir
Mane sama guél néna dafa biir
Boudé ya ngi souffrir
Mais mane ma ngi dé si biir
Cent mille problèmes
Millions problèmes
Milliards problèmes
Fuck dix mille problèmes
Soum koy nétali do dém
Diogué si problème dalaate si problème
Fatal say problèmes
Amo yéré yo sol mane tatounène laal dèf
Ngané bèn guél doula xool
Équipou laambe bi mafay chef
Né nga da nga am problème
Mais mala eup problème
Kou si nék amna problème
Mais dou nieupeu kay waax
Né nga da nga am problème
Mais mala eup problème
Kou si nék amna problème
Mais dou nieupeu kay waax
Sa rakk dafa AVC
Sama mak dafa ébola
Indi na acte de décès
Bayiwoufi ndieugou chocolat
Sa guél day saw lal sama diabar day poupe lale
Xawma lane mola dale
Sama problème khadoul hôpital
Amo lo fayé louass
Mane huissier dafma guéné
Dénkanéna samay bagass
Niou nonou galé Ndiémé
Vivre sa problème pour yaw té boumako nétali
Ndax amna problème comme yaw sama paane boulko féthiali
Né nga da nga am problème
Mais mala eup problème
Kou si nék amna problème
Mais dou nieupeu kay waax
Né nga da nga am problème
Mais mala eup problème
Kou si nék amna problème
Mais dou nieupeu kay waax
Yééé... Ooooh...
Da ngay am say problèmes
Wéteuk sa problème
Bayima ak sa problème
Yaw mom no problèmes
Da ngay am say problèmes
Seuf ma say problème
Dèss si sa problème
Yaw mom no problèmes
Da ngay am say problèmes
Baa ma ak sa problème
Ba doto amati problème
Yaw mom no problèmes
Né nga da nga am problème
Mais mala eup problème
Kou si nék amna problème
Mais dou nieupeu kay waax
Né nga da nga am problème
Mais mala eup problème
Kou si nék amna problème
Mais dou nieupeu kay waax
Ecouter
A Propos de "Problème"
Plus de Lyrics de ISS814 BEATS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl