Paroles de Thiès
Paroles de Thiès Par JEEBA
Succès bouné xana xamo wakhtou laay xaar
Borom xam xam yi dioundj nagn ko dooyna waar
Taay magg nagn xamé boubakh flambeau bi ñoko yoor
Sou baxé ñioune la baxaal sou booné it ñioune la boonal
Thies mako moom yaako moom ñokoo moom
Ñou degeul baat bi dieum si kaaw
Do daaw moukou xamnani gaindé nga
Deuku bañn kat ben la si Sénégal
Deuku ngonè latyr ak Seck signature Sanekh motax ñu neex
Ñoune soxla wugn diégani rooyukay
Fess fi deel tax ñoukaay ndaamo waay
Deuku bañe kaat ben la si sénégal
Thies kay rek si xol dara dokou faay
Kou weedi ladj leen liim ma faay
Ah waaw wawaaw thies Sama deuk la mane makoo moom
Ah waw wawaaw thies sunu deuk leu ñoune nioko moom
Setsima gaaw ma wone là way wone la lodoul guiss si bene reew
Fi adiana la no y’a pas photo jengu mane leu Kone nagn ko topato
Kouné sagn nga wakh ni finga deuk mom mo la nekh
Kouné sagn aapo ni finga deuk né mola nekh
Kouné sagn nga waxni finga deuk moom mo nekh
Thies kaay moma nekh mane mooma nekh eh moniou nekh
Thies kaay ioe mo niou nekh yobou ma yobou ma
Keur mame Elhadj Ziaré Ahmed Barro ndiéguéne diar diamageune
Ziar sunu mame Abdou Aziz Aidara deem Medina Fall penc Baye fall yaa
Cheikh Ndiguel fall Meissa biguè coumba Fall Dabaay
Khabrou Abdoulaye Yakhine Sama mame Amadou lamine Ba
Duñu fatei wa diangou bi thies kaay mooy Sama reew
Ah waaw wawaw thies Sama deuk leu mane makoo moom
Ah waaw Wawaw thies Sunu deuk leu nioune nioko moom
Setsima gaaw ma wone laa way
Wone la lodoul guiss si Benen reew fi adiana la
No y’a pas photo jengu mane la Kone nagn ko topato
Ñugn soxla wugn jéguaani rooyukay
Fess fi deel nioukoy ndamoo waay
Deuk bagn kaat bilé si sénégal
Thies kay reik si xool dara douko faay
Kou weedi ladj leen ma liim ma faay
Eeeh eeeh
Yobuuma mbour guedj
Mbour Socé mbour kankourang aah
Damay nieuw gaaw yaay
Eeh eeeh thies kaay
Hun hun thies kaay
Ñoune soxla wugn jèguani royukaay
Fess fi deel taax niukooy ndamo Wawaw
Deuku bañe kaat bé si sénégal
Thies kaay rek si xol dara douko faay
Kou weedi ladj leen ma liim ma faay
Ecouter
A Propos de "Thiès "
Plus de Lyrics de JEEBA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl