JEEBA Dafa Nekh cover image

Paroles de Dafa Nekh

...

Paroles de Dafa Nekh Par JEEBA

Wakh mo lo bouga ma defal lako

Wakh ma lo namma Cherie ma outal lako

Meme boudé auto ma dieundal lako

Yobou lathi chateau nga deuké dodo

Dama xam fouy khassane fofou lay wokka

Sa ex yila done sonal nieupeu lay nokka

Athe la bathi kaw keen doula diote

Diokh la khir bi ngaleen di thiaw

Ma takhaw nane ko niaw

Mbeguel dafa nekh bokoy kaffé sakh day nekh

Sa biir xol bilay diap mel ni danio thi dougal fekh

Meuno kham limay wakh tant que demo thi bamou diekh

Fok nga niam kani waw doga xam lou lem di saff

Awa nénama dafa nekh makhfou nene nama

Dafa nekh kadia nenama dafa nekh

Meme maimouna nenama mbeuguel dafa nekhhhh

Kone dama la bougga té koumou meti nanal amoniaque baygon wala maladio sayo yewo nganiouy guiss niouy leungo ma nane ko

Beug na beug nako boudoul reen di deween dinako def ndakh yama diaral lolou

Dama tégui gros lot ohh

Mom momay teul mane mako beureung xam na nandou lo lolou

Nioune bouniou begué moniou begual bouniou dioyé moniou dioylo

Bebe xam ngama bou bakh douma kou tegui ndawal

Fima lay diap banga ni Akhh mako xam té dama koy dowal

Bebe xam nga mane loutakh ma beug la dama thi sawar

Danga fek fi thiebou kéthiakh nga valorisé sani thi ndawal

Ndakham lakh bi daniou koy seulmo no daniou koy keupo

Sama carte bi ioe la votel tak seuy bi dial thi lenene

Kone danga mer mane mangui bakh

Diokh ko ndox mou nane mou gékh

Lolou meunoul niak

Ndakh Mbeguel dafa nekh bokoy kaffé sakh day nekh

Sa biir xol bilay diap mel ni danio thi dougal fekh

Meuno kham limay wakh tant que demo thi bamou diekh

Fok nga niam kani waw doga xam lou lem di saff

Abba nenama dafa nekh ngoné nénama dafa nekh habib nénama dafa

Meme aicha aziz nénama mbeuguel dafa nekhhhhhhh

Kone dama la bougga té koumou meti nanal amoniaque baygon wala maladio sayo yewo nganiouy guiss niouy leungo ma nane ko

Beug na beug nako boudoul reen di deween dinako def ndakh yama diaral lolou

Dama tégui gros lot ohh

Mom momay teul mane mako beureung xam na nandou lo lolou

Nioune bouniou begué moniou begual bouniou dioyé moniou dioylo

Mbeuguel mbeuguel mbeuguel dafa nekh

Nekh nekh nekh nekha nekh ayyyé waw wa waw waw

Kone dama la bougga té koumou meti nanal amoniaque baygon wala maladio sayo yewo nganiouy guiss niouy leungo ma nane ko

Beug na beug nako boudoul reen di deween dinako def ndakh yama diaral lolou

Dama tégui gros lot ohh

Mom momay teul mane mako beureung xam na nandou lo lolou

Nioune bouniou begué moniou begual bouniou dioyé moniou dioylo

Ecouter

A Propos de "Dafa Nekh"

Album :
Année de Sortie : 2024
Copyright :
Ajouté par : Maffoho farida
Published : Jul 17 , 2024

Plus de Lyrics de JEEBA

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant

A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl