Paroles de Saï Saï
...
Paroles de Saï Saï Par JEEBA
Yala dou dioum mani Yala dou dioum loumou def
Ndeké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
Souma ko defone mangui thi tolof tolof
Kone fok ma xolate ko
Saï saïiiii la fok ma xolate ko
Wadjii Saï saïiiii la
Yalla dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
Souma ko defone mangui thi tolof tolof
Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Fok ma xolate ko
Wadji Saï Saï la
Yala dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
Souma ko defone mangui thi tolof tolof
Nieuw na sama lathté fa sama yay boy
Saï Saï la
Nieuwate sama keur lathté fa sama baye boy Saï Saï la
Néna kilifa la dou dokh thi tank thiakhane
Ñente ak tranche indi gouro dadi labane
Mingui may tek tank beug ma forcé ray
Ndéké loumou beugone dougal but bi jubilé daw Refrain
Yala dou dioum mani Yala dou dioum Loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na bay xalate nar ko diox sama xol Ndéké souma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko
Ndaw ci Saï Saï la
Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def
Ndéké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
Souma ko defone mangui thi tolof tolof
Néna koudoul mane beugoul sokhla woul
Mane rek la diokh bop kou Mel ni mane amoul
Mane mako yeungal yeungal mbeguelam
Ndéké mane dama door ay calmant lamay diokh Dem na ba dépense keureum mako yoor
Faye courant Faye ndokh Faye diangue xalé yi ecole
Dieund greffage Faye ay voyage ndéké damay door sama poche la nop
Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def
Ndéké lolou mo geune Demone na bay xalate nar ko diokh sama xol
Dejesouma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko
Ecouter
A Propos de "Saï Saï"
Plus de Lyrics de JEEBA
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl