OMZO DOLLAR Nitté cover image

Paroles de Nitté

Paroles de Nitté Par OMZO DOLLAR


[VERSE  1]
Han ! Nitte ya ngui sibir nitte yi
Da melni yapp nitte tallen sourr
Nitte tey dougal nitte
Safara diko nakh ak aljana
Pithie mou ngui sikaw wanté xél bi
yeup pa nék si souf
Kou djoud si cage dey
Fokné ki sibiti mo dioum
Lanleu la ley wagnil ioe sama yokalé
balou may taillo dina faye sa yéné
Khana soy rafet dafay takh ma niaw
Kou kawé daay touti si kou
Meunoul naw a buzzey

[CHORUS]
Ndax malla yé niou geuneu nitté
Ndax malla yé niou geuneu nitté

[VERSE  2]
Sheitané waxoul deug gniko
Déglou la yakh sen xél
Requins yi diné djiko
Caïman di nagn done ay
Diane you matt sen guéne
Gaindé dou fallé kouy you bokk mbarr
Dieun bou ndaw si bou makk rek lay done
Malla boudoul diamou y’Allah amoul
Pourtant lakhira souf rek
Lagnuy done a buzzey

[CHORUS]
Ndax malla yé niou geuneu nitté
Ndax malla yé niou geuneu nitté

[VERSE  3]
Guiss na ay mag ak birrou khalé
Sibir khalé you bireul ay khalé
Dagn sathione souniou enfance
Niou magg niouy sthie souniouy enfant
Boul dougeul khadj jou mbed si sa keur
Boul dougeul khadj jou mbed si sa keur
May la sama mbok dou takh niou done cousin
Loup ban gui si poulailler bi ak
Sourire bou jaune poussin a buzzey

[CHORUS]
Ndax malla yé niou geuneu nitté
Ndax malla yé niou geuneu nitté

[VERSE  4]
Hé ! Malla yé niou geuneu nitté
Dama beurri louma meunoul expliqué
Quelle mouche nous a piqués
Nitte bouniouy jamou ay
Kharr rek lay djité a buzzey
Han ! gni sante seni tour lagn geum
Kou khessal dagn la tourr leundeum
Sa goudou nopeu takhoul ken
Dou door bambou dessoul
Loudoul fass sa kaname daw do
Fallé doo dane
Mouno mouss ba gaindé done bouki
Watt ay caméras de terre
You nek chauve-souris oh
Un deux niou merrr lou peundeul lou set
Ndax xol bou dièkh ak deuneu bou fess

La dieund dou dess boul tipsé
Le mythe est souniou nitté yeup si succès
Succès si sa diné di nga distrait
Ba dal si mur melni sindax
Tête loin des épaules girafes
Aam xam xax mandlou wo moudié done serr
Kou am chaire de poule niou def
Leu poulet de chaire
Sa succès sa noone ley dann
Golo ak allumette baune ley tal
Y’Allah mome lissi kananme boy
Diégui khol sa droite ak sa gauche beu
Safara barina nioufi défoul lone long feu

[CHORUS]
Ndax malla yé niou geuneu nitté
Ndax malla yé niou geuneu nitté

[OUTRO]
Hé ! Malla yé niou geuneu nitté
Dama beurri louma meunoul expliqué
Quelle mouche nous a piqués
Nitte bouniouy jamou ay kharr rek lay djité

Ecouter

A Propos de "Nitté"

Album : Nitté (Single)
Année de Sortie : 2019
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Sep 10 , 2019

Plus de Lyrics de OMZO DOLLAR

BRK
OMZO DOLLAR
OMZO DOLLAR
OMZO DOLLAR

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl