OMZO DOLLAR Soutoural cover image

Paroles de Soutoural

Paroles de Soutoural Par OMZO DOLLAR


[REFRAIN]
I say Han kou niaakeu rekka am yama gueuneu xam
Kou nameuh dina taameuh yama gueuneu xam
Kou xamné xamoul rekka xam yama gueuneu xam
Nieup done ay borom xam xam yama gueune xam xam

[COUPLET 1]
Bakh moy bone fi nieupeu djoum légui
Djiguèneuy torokhal goor, goor yi nioy mopugne légui
Djiguène khol avenir mais goor sa passé lay guiss
Motah goor yi nala takkeu lagni dokhaané légui
Okay ! Am djabar yu melni sunu yaay dou amaate man
Sori naniou souniou Pa deug rekkay takh may wakh mane
Niom Pa bouy géré quatre women lagni wowé batman
Pa bouy géré quatre women lagni wowé batman
Haaan Soutoural
Fi so beugué sa dara dokh fokk nga soukou raam
Fi ngay guiss ay beaux parleurs yu andak lamigne yu niaaw
L’Habit ne fait pas le moine mais y a des habits pour moines
Rigne-Se bi dèy tek kone yaw dindégo sa téré
Loy neubeu nit bou nioul nigga bindeu ko ci teeré
Kou fi nek chomeur tok di waate ni dagnko liguèy
Deuk bou kène doul liguèy waayé nieup lagni liguèy
Eh yaw fi moy Sénégal lou nekh waay def
Souniou bougoul fène deug lagni neubeu
Défal loumay wakh boul def loumay def
Défal loula nekh gars yi nagn leu Soutoural

Soutoural soutoural, Soutoural soutoural
Soutoural soutoural, Soutoural soutoural

[REFRAIN]
I say Han kou niaakeu rekka am yama gueuneu xam
Kou nameuh dina taameuh yama gueuneu xam
Kou xamné xamoul rekka xam yama gueuneu xam
Nieup done ay borom xam xam yama gueune xam xam

[COUPLET 2]
Bou féké yémo place boul signé monogamie
Bou dh niémé wo clash boul signé polygamie
Di nala may sa baate boy youkhou sama famille
Bou féké men nèy trash, djiguèneuy auto-mbalite
Da melni Afrique sofi sathioul meuno nek milliardaire
Lane mo gueuneu raciste wané keu-gna (Gnaak) wala ndréingue
Kogne bo dougou niéteu djaaka waayé bène dou ci fess
Pa yu eupeu djabar niofi eupeu ay maîtresse
Système LMD système LMD
Léwal Maîtresse Djabar (LMD) lolay système LMD
Liguèy Mèche Doxane yeah Système LMD
Primaire ngay nope sa maîtresse djangue système LMD
Soutoural fi so bougué sa dara dokh fokk nga soukou raam
Amna niou détourné xaliss dém di tchi tabakh djaaka
Ndara nakh sen bopp fokné nio ngi nakh Yallah
Eh yaw fi moy Sénégal lou nekh waay def
Souniou bougoul fène deug lagni neubeu
Défal loumay wakh boul def loumay def
Défal loula nekh gars yi nagn leu Soutoural

Soutoural soutoural, Soutoural soutoural
Soutoural soutoural, Soutoural soutoural

Ecouter

A Propos de "Soutoural"

Album : Soutoural (Album)
Année de Sortie : 0
Ajouté par : Tamsir Diouf
Published : Nov 11 , 2019

Plus de Lyrics de OMZO DOLLAR

BRK
OMZO DOLLAR
OMZO DOLLAR
OMZO DOLLAR

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl