Paroles de Mayou Yallah Freestyle
Paroles de Mayou Yallah Freestyle Par OMZO DOLLAR
Rap ba guiss hater di tathiou
Xaliss lay noyé légui anh! Athiou
From tangal thiéb ba nek thiéba
Omzo dollar negger flow bouy tal kémi séba - thiè!
Mayou yallah la fils meusoul nek kou du sors
Doma wathié khana sama bissou levé du corps
Dakh rap beuri swag dakh sangnsé sa rappeur ci man dou loudoul pilule du lendemain si nguenté parce que heure bi ngey teud la donne djouk
Assumél loy wax sa son yi biss boy tassé ak nioune.
I get juice.
Liguey diot Thiakhane pousse
May saga ndeye sa rappeur melni Assane Diouf.
Démissionné sonatél madaan maintenir ay serveurs.
Ndakh boy yagui té samay barres ni Aÿ serveurs.
Manla serf bou amoul barrage civile
Tellement que dama bagn thioyi douma sax def mariage civil. Thié!
Tay la tay nioumay weur depuis hier
Xerr yougn may sani tax bâ ma am coeur de piérre
Sama casse ndokh mossi nek dou liqueur dou bière
Respecté na sama mère ak samay heure de prieres,
Awma loudoul xel xol xour , sama xel comme fourr
Sama guél comme buur, Boy passél concours
Dougueul xelcom toub boul diéma clanshanté sax
Flow bouy takh sa rappeur thiang lalanté khathie dakheu xéxeu blanca
Béneu mic ak béneu 16 en cas
Limay rap amna wax you diakhal Cheikh Anta
Am Ay riri ak Ay Kardashian
A force de voyagé niowate j’ai trouvé karda chiant - thié!
Amatouma diote pour tokk di lire sey critiques
Business Class di french kiss Ay guélou British
Yague freestyle gallé Aba boy qui peux test
Si balcon bi ladane guéné li Sama deuneu melni 2 pièces
Yangui feel nimeu sincéré?
Réal nigga till i die ma djigne thiéré
MC kouma diokh sa derr ma deff si Jean thiéré.
Limay rap doula may dara , jeans sérré
Niane yallah pour mou yeureum samay ennemies.
Ils savent plus comment faire nigga « anémie ».
Fi ba kagn la nara djoutal rap galsen.
My nigga baye séne néna boy may mâme séne
Niggah loniou fokk?
Deff ko sunu bop , tek ci doniou fuck
Niow sa bopou kogn deffko sunu kognou bop,
Chiarr sa guél ak khoniou doff.
Started from the baaram légui Top bi moniou top
Fuck rap fuck succès, fuck xaliss, fuck concert, fuck beat, fuck Omzo Fuck everything
Fuck “di user size” deff yaramou nénn di youkhou thug life,
Fuck goordjiguen yi yakamti ma sani Ay pique wa Buzzlab,
Fuck sa rappeur ma meun si aduna bi leer neu wala léroul
Fuck goordjiguen you nara yémou pour sétt ndakh concert bi féssna wala féssoul.
Tchi digue bi lay djiarr ni milieu relayeur
Le meilleur n’aime pas qu’on dise qu’il est l’un des meilleurs Abo’zer
Ecouter
A Propos de "Mayou Yallah Freestyle"
Plus de Lyrics de OMZO DOLLAR
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl