Paroles de Amul Solo
Paroles de Amul Solo Par CANABASSE
Man xawma lutax ba maag yaw mënu ñu juboo ñun
Lutax ba ñaari fann yu nek ku nek dumoo yu
Fitna bi ci kër xam na ñu ni moolul
Mais seytané rekka dëkke ci di ñu noot ñun
Lutax ba sa bët bi weex na sax nga giss ci sa bopp daal di berru da nga merr
Soxna ci dimbalil sa bop té dimbali ma jeema soppi ni ngay dundé
Tooñ na la Baal ma
Tooñ nga ma baalul
Fii dara grawul
Rëy mo ko fi jarul
Heuru ndekki ma claquer porte
Bu guddé ma ñibbi ci
Bokkatu sa ginnaaw
Mu mel ni xuloo mëssul am
Fitna laay yendo dem n’a bureau mais liggeeyuma
Merre n’a la baby mais nammel bé ëpp ci man
Tooñ na la Baal ma
Tooñ nga ma baalul
Fii dara grawul
Rëy mo ko fi jarul
Man merr na dem na
Ñëwaat ndax xalaat na
Giss ni adduna
Amul solo
Dara jaru fi xuloo baby
Man xawma lutax ba maag yaw mënu ñu juboo ñun
Lutax ba ñaari fann yu nek ku nek dumoo yu
Fitna bi nekk ci kër gi moolul
Mais seytané rekka dëkke ci di ñu noot ñun
Lutax ba sa bët bi weex na sax nga giss ci sa bopp daal di berru da nga merr
Saa waaji dimbalil sa bop té dimbali ma jeema soppi ni ngay dundé
Tooñ na la Baal ma
Tooñ nga ma baalul
Fii dara grawul
Rëy mo fi xajul
Boo wacce ma fass kanam
Pourtant ma ngi doon xaar nga ñibi ci
Defaru na ba nice yeah baby xamna fim’lay jaar
Fitna laay yendo dem n’a bureau Mai’s liggeeyuma
Merre na la baby mais nammeel bé ëpp ci man
Tooñ na la Baal ma
Tooñ nga ma baalul
Fii dara grawul
Rëy mo ko fi xajul
Man merr na dem na
Ñëwaat ndax xalaat na
Giss ni aduna
Amul solo
Ecouter
A Propos de "Amul Solo"
Plus de Lyrics de CANABASSE
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl