JAH HUSTLAH  Ak Fi Rewmi Tolou (Remix Akhlou Brick) cover image

Paroles de Ak Fi Rewmi Tolou (Remix Akhlou Brick)

Paroles de Ak Fi Rewmi Tolou (Remix Akhlou Brick) Par JAH HUSTLAH


Ak Fi Tewmi Tolou
Gneup Djap Boppou
Sama Khol Dou Sed
Tank Deuk Ba Ngi Metti
Ak Fi Rewmi Tolou
Gneup Diakhlei Lol
Sama Khol Dou Sedd
Tank Que Deuk ba Ngi Triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste

Ak fi rew mi tolou meunou ma am diam
Deuk bé wopp dioyatou niou corona
Dagnou seuf lou diss diapé niou ay mbame
Fébar teuweu Fadiou doundou bou cher lolou mofi ame
Daka mayé thièp paré ndieuk bi cher
Gneup toke ni tek mognou couter cher
Yokou doundou si deuk bou xif di ray ya raw meuwti
Fi dara dokhatoul lepp taxaw fi ni sa TER bi
Ba  jeunesse bi di déme taylé Dji  bakane yi si guedj gui
Deuk bou wow trop sou tawé xol yi toy
Magu ak ndaw youxou dioy nguir Yalla dafa doy
Dougn lako wax nak gnari yone dofi ame 3 mandat
Li dale Alpha Condé boula yéwoul peuple bi Yé la
Kou faté ba faté lila Fall folékou yomb la
2024 yagatoul lep Leer
He dassal sa carte xar

Ak Fi Tewmi Tolou
Gneup Djap Boppou
Sama Khol Dou Sed
Tank Deuk Ba Ngi Metti
Ak Fi Rewmi Tolou
Gneup Diakhlei Lol
Sama Khol Dou Sedd
Tank Que Deuk ba Ngi Triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste

Macky Wakhonn Na Deug Bamou Nei Yoonu Yokkoutei La
Neketei Boy Kou Djaay Sa Roue ! Sa Bakaan Yako Taylei
Niounn Nioko Tay ! Wai Nioko Def waay ! Nioko Tay
Kouy Guiss Tête Vide Denk Ko Sa Bopp ! Ya Gatt Xell
Dina Yok Ba Yok Mandam
Nga Tok Feulei Djap sa Ngaam
Jotna Nga Khekh Nguir Si Sa Ndam
Dof Dou Degg Exemple
Ak Fi Rew Mo Tollou ! Kou Nopi Complice Nga
Rappeur Bou Tok di Setann ! Djapal ni pawlish nga
Nagnou wakh si Ndokh ta Yi Ak  Nit Gni Gnak Sen Gallei
Liguey Do Djot Sa salaire ! Doundou bou cher bi dougn ko sallei
Voix Des Sans Voix Yi Nio Moumeu Si Mbeund Bii
Dafa melni Sunu voix de développement bi daf gnou reer
Politicien dou tour leundeum
Day leundeumeul sa takander
Kay ma wakh la Différence mowti Ak Macky
ki dalay yobou labiissine ! Ké dalay yobou Ndougoussine

Ak Fi Tewmi Tolou
Gneup Djap Boppou
Sama Khol Dou Sed
Tank Deuk Ba Ngi Metti
Ak Fi Rewmi Tolou
Gneup Diakhlei Lol
Sama Khol Dou Sedd
Tank Que Deuk ba Ngi Triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste

Ak Fi Rewmi Tolou
Macky Khamal Li Ngay Yokou
Yokou Nga Fer Ak Ciment
Yokou Nga Sucre
Yokou Nga Diiw
Yokou Nga Mourou ! Macky Khamal Li Ngay Yok
Macky kay ma wakh li ngay yokou
No boul yok mew ! Boul yokou thiep
Yokal école yi ak tally yi
Hôpital yi ak emploi yi macky li nga wara yokou
Ak Fi Rew Mi Tolou
Macky Kholal Li Ngay Yokou
Ak Fi Rew Mi Tolou
Macky Kholal Li Ngay Yokou

Ak Fi Tewmi Tolou
Gneup Djap Boppou
Sama Khol Dou Sed
Tank Deuk Ba Ngi Metti
Ak Fi Rewmi Tolou
Gneup Diakhlei Lol
Sama Khol Dou Sedd
Tank Que Deuk ba Ngi Triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste
Dafa Metti ! Deuk Ba Ngi triste

Ecouter

A Propos de "Ak Fi Rewmi Tolou (Remix Akhlou Brick)"

Album : Ak Fi Rewmi Tolou (Remix Akhlou Brick) (Single)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Oct 13 , 2021

Plus de Lyrics de JAH HUSTLAH

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2024, We Tell Africa Group Sarl