
Paroles de Bendo
...
Paroles de Bendo Par MATADI
Yewou soubeu dieul seu bain bou bakh
Gueine dieund café touba
Ziarer baye fall yi niou ngui bakh
Aytchaa diapp req tei yalla takh
Amoul khoulo, amoul khekh
Diapiser cogn bi di nekh
Dougg marrau geuneu fekh
Est ce que do sangou beu mekh
Amoul seral boy
Domou guediawaye dou delou guinaw
Boder diagu wooy
Baller yi degn ley effacer mou gaw
Peudo bi di okk, waga yei ngui daaj
Tassal ma packet meu takk tal
Bayiko mou yegg tei dou meusseu wathie
Indique dou tokk, goylett doufi dial
Flag bi tchi kaw
Drapeau bi dou wathie
Flag bi tchi kaw
Non non meussoul wathie
Khadj yi di mbeuw
Di negn yagg dess si guinaw
Tei nioune nio ngui gooo
Dowouniou tiow
Wathier concert souniou charrette
Nioune niou ngui si kaw
Ma ngui aq sameu bendo
Guediawaye sameu ghetto
Ma ngui aq sameu bendo
Guediawaye sameu ghetto
Langu si car rapide yi ba hooy
Yegg si arrêt bi def fouy
Lepp lofi indi daf fi doy
Dougg ghetto weur sahm
Setti balla req weeeuy
Guediawaye bendo di aral
Dofi nieuw niodi niou battle
Samey niggers degn ley mbaral
Khoti seu yapp
Ni ou yobb leu daral
Negn dem guediawaye
Gouddi douddi guediawaye lay fananeee
Negn dem guediawaye
Boo yendoo di nguafeu lekk di nguafeu nanee
Flag bi tchi kaw
Drapeau bi dou wathie
Flag bi tchi kaw
Non non meussoul wathie
Khadj yi di mbeuw
Di negn yagg dess si guinaw
Tei nioune nio ngui gooo
Dowouniou tiow
Wathier concert souniou charrette
Nioune niou ngui si kaw
Ma ngui aq sameu bendo
Guediawaye sameu ghetto
Ma ngui aq sameu bendo
Guediawaye sameu ghetto
Ecouter
A Propos de "Bendo"
Plus de Lyrics de MATADI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl