Paroles de Mbarke Ndiaye
...
Paroles de Mbarke Ndiaye Par MATADI
Bayi meuu meu oubil mbarké ndiaye (wooy damey oubil mbarké ndiaye)
Bayi meuu ma dokh aq tankou niay (heey damey dokh aq tankou niay)
Dieuleul golo bi di yeungeul gueine
Diemeul nokk dem sangou parce que da ngua hegn
Talati game bi yeup bas agar hegn
Nieuweul dieuleul li ngue beug bala atou’fegn (ya begn)
Domou gaindé mane leu balla gaye
Mane leu balla gaye
Dou matey khana dou ma deuk guedieuway
Kouma lebal tal, da nguamey fey
Tei bofi di e mer dougg di waay mbaye
Mane la mata damay dakhar seen
Wa wakhat leine comedien leen
Ni diogoye séne
Koudou thinewar
Da ngeuy séné
Wa loumay seine
Nopp you gouddou, niombar séne
Bo dougguer di ngua deupatt
Dakadji nguama appat
Sigguil yeukeuti seu batt
Bo seuguer di ngua mbappat
Baye fall dou bayi doukkat
Nguey ngandi mar katou tate
Seu none deko topoto
Bou kholam di bone
Deko send ay photos
Ya meuneu topondo
Mey wah nguey
Niodi ay choco choco
Mane la meumeu mbaye
Di makk si ibra nadio
Damani talal gaz
Tokssi ba sa gatt tangue
Dou tel nioune niou ndekki
Wa mani gatssadi dou tomaté lokati wallay doko defati
Boy boussi dougeuti matoma sax
Ndokhoum sebetti ehh boy
Boulma niopati baba
Bayi meuu meu oubil mbarké ndiaye (wooy damey oubil mbarké ndiaye)
Bayi meuu ma dokh aq tankou niay (heey damey dokh aq tankou niay)
Bayi meuu meu oubil mbarké ndiaye (wooy damey oubil mbarké ndiaye)
Bayi meuu ma dokh aq tankou niay (heey damey dokh aq tankou niay)
Wa legui naq feroce ngueine
Kane si yenn
Leu yayam feram fegn
Aq gnane nioy omelette néne
Niaf leine seine l’œuf
Bala sagar khegn
Wa qui dou senghor diouf
Ba leine aq ousmane ni ou songo
Ma def comme diomaye
Ma meuneu créer doute
Rappeur yi fi done diay poup
La dieul yobbou dubaï
Mané kou tapp dou tokk
Bou togguer topp bi todi
Ma yagg fodi khaf di todj lali mbott hééé hééé
Mane grawna quoi heey
Chaque année mey amat kheuy
Chaque année happy buzz
Mane leu souley faye
Na ngua rapp tei begneu degglou gars yi ley diey
Nakh ngaaka thieré leu dafa gaw si rey beug
Ay oubi teudi
Auf seu deudieuw
May teppi niaw di euw
Sonner keur gui khadjou ndiaggo bi di mbeuw
Matt
Bayi meuu meu oubil mbarké ndiaye (wooy damey oubil mbarké ndiaye)
Bayi meuu ma dokh aq tankou niay (heey damey dokh aq tankou niay)
Dieuleul golo bi di yeungeul gueine
Diemeul nokk dem sangou parce que da ngua hegn
Wa legui naq feroce ngueine
Kane si yenn
Leu yayam feram fegn
Ecouter
A Propos de "Mbarke Ndiaye"
Plus de Lyrics de MATADI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl