Paroles de Zéro Comlexe
...
Paroles de Zéro Comlexe Par MATADI
Zero complewe (ay waaay, ay waaay)
Eupeuler womeu daraa (ay waaay, ay waaay)
Lolou la diapp (ay waaay, ay waaay)
Ehh li ngueine di taawi chewin gum leu dou daraa (ay waaay, ay waaay)
Ma ngui doundou lou toukoussi ngualam
Yow req ya sone
Di souss ba neck si anam
Ham nguani radio dou diar onde
Mene nieuwouma damafi diar dongu
Yow pistolet ndokh ngua mey bomb
Mane da ma aisé si louma yalla mey
Kouma sokhorer yay sone
Ma nguek fonder bamou doye
Defssi mew soukeur bamou saff
Diokhma pizza ma geuneu bekk
Mais soumako amoull naq lekk tiaf
Zero complexe
Dou né ngua da ngueina fokoler
Meune ngua dem brunch radisson
Ma yewou lal mbourou aq chocolate (même beignet c’est bon)
Wouyaye merr neu
Ehh ya yeeh diaroul ngua niuoy diay maana
Ehh ya yeeh
Wouyaye merr neu
Ehh ya yeeh diaroul ngua niuoy diay maana
Zero complewe (ay waaay, ay waaay)
Eupeuler womeu daraa (ay waaay, ay waaay)
Lolou la diapp (ay waaay, ay waaay)
Ehh li ngueine di taawi chewin gum leu dou daraa (ay waaay, ay waaay)
Boula dara diaral def lo beugoul nekossi à l’aise
Da ngua pata segnsel ni nguako beuguer lou yakou dou obèse
Segnser comme diomaye guiss macron (mais question)
Tokk seu bureau may maçon (waa béton)
Town ngue deuk, boy ghetto là
Yoral seu vody meu nouroula suraaah
Doumako forcer ba nouroula
Yobb ko resto mane tangan maiga
Li dokhal seu mind dou tank mushei mashashooo
Même souma neker handi cap é dou tei ngue diokh meu tieur
Wouyaye merr neu
Ehh ya yeeh diaroul ngua niuoy diay maana
Ehh ya yeeh
Wouyaye merr neu
Ehh ya yeeh diaroul ngua niuoy diay maana
Zero complewe (ay waaay, ay waaay)
Eupeuler womeu daraa (ay waaay, ay waaay)
Lolou la diapp (ay waaay, ay waaay)
Ehh li ngueine di taawi chewin gum leu dou daraa (ay waaay, ay waaay)
Ecouter
A Propos de "Zéro Comlexe"
Plus de Lyrics de MATADI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl