Paroles de Laff Thiat
Paroles de Laff Thiat Par ZO FLAME
Bisous Moua à tout à l’heure
Bisous Moua à tout à l’heure
Trap-king
Zo Flame
Boooouhhh
Eyyy
Souniou son moy daw birr club
Sen gelii di djoutou (djoutou)
&skip askip elle a des sentiments
Mais wallah c’est trop chou
Yarou wougn deh dagno wreww beu dofffffff
Ioe fananal fofou
Yageuh dokh lep louy daw ni ni
Boy nioleu si djitou
Woww
Téméric Mc si niarii pain
Pouloh Goto ko wa-také mayonnaise
Kheuthieul seu mbadjeu Fait de beaux rêves
Pansement se khol khewi ngami mbaye nder
Dofo A féti
Kheuthie boutélou kharane bi séki
Doumey khessal mais dagn meukey diw
Diokh ko faux numéro ak Loumou sexy
Limey flow da niak téguine
Starou dakar gey am fi starou Sénégal gey am fi
Starou Afrique gey guiss nii starou plante terre ni key hmm
Say mashallaww
Dara doufi siit fat trek moniou takha diouk mon amie
Beurri floww am style si khalé roussoumako mais meun nagn drip
Holal holal holal holal … ay
Jalabé Khaftane3 pièces ndanane
Ay jean Balmain wala kolobane
Christian Dior ak faarou mbam
Ay drip nikou fanane si jerrycan
Lal thi souf mbarakiss wala Jordan
Ay drip nikou fanane thi Saw lal
Pull lay sol sama yone si Tanguay
Wouhhhhhhhh
Say machallah Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Say machallah Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Parmis nous y’a des nous
Parmis vous y’a des vous
Boyi legui meune neugnou doule
(I don’t like this shit)
Mounieulouma keeeeneuuu
Tu dérape je coupe les ponts
Ak technique 3 sabres (waw)
Rabou ma lou garap di mayei li c’est un acquis
Rendil juifs yi merouane c’est un nazi
Doucouré seu Mc c’est un miskine
Nakari derete pic meu goukh ay téramycine
Sinon j’espère que tu bin
Passaka passaka, nous nous bon Khodj seu gel bi si bain
Passaka khaliss moko geuneu chon
Hold on nioune deh yallah moniou Taal
Amoul mindefff bougn fi meuneu fey
Passaka adouna yallah ko mom
Tei Defna ga khewi kone wanel sa numéro dokou
Zeyneu khateuh li Nekna no Weli
CFA en liquide lay topou niom nagn ma dakeuh ba Sene ndiantakhiten soti
Li délie leu délire bi dou meusseu flop
Gni gey wowei gangstar lay solal crop Top
LAFF thiat mane deh nianeu meu yoor
Kouy dawei ak vitessou Lamborghini
Non non douko topou
Jalabé Khaftane3 pièces ndanane
Ay jean Balmain wala kolobane
Christian Dior ak faarou mbam
Ay drip nikou fanane si jerrycan
lal thi souf mbarakiss wala Jordan
Ay drip nikou fanane thi Saw lal
Pull lay sol sama yone si Tanguay
Wouhhhhhhhh
Say machallah Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Say machallah Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Laff Thiat Laff Thiat Laff Thiat
Ecouter
A Propos de "Laff Thiat"
Plus de Lyrics de ZO FLAME
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl