Paroles de DMT Par MATADI


Do am dara touss nak
Nek si arènes bakou yeungeul di pouss mak
Mane gueen di khaar ?
Danguéne si dalle nak
Mane Damay danne ba paré
Soga di touss nak
Bandit dou ballé
Waga dou def choc
Hey Damay keuff sen hit yi ba lein guéne dém took
Mingui guente dii poupe nganane ma tek pote
Hey Mat li yagg tourou si mane nganane mongui tookeu
Faw ma siiw ba am ay paparazzi
Bassa papa rakh si
Yegeul koss tek si thiarax you rare yi
Meune guéné sarax sii
Guel bou niine ma diiw ko mako dadji
Mou rapii rapii
Boulko feel bou nekoul marque radji
Bayil yeek car rapide
Pour wathié rappeurs diaroul shiit
Damay yeek douma tiirr
Sen guél  yey sama gab
Bouma roffé guéné liquide
Boy bi dafa tiir youkhou tiite ba mbeukk mire
Ay cambe you peel gaas
Walabok cana dou bayi

Douniou mayé wé dougme mayé touss
Non non douniou meusseu mayé wé
Douniou mayé wé té douniou mayé touss
Hey mat douniou meusseu mayé touss nieuweul
Douniou mayé wéé té douniou mayé touss

Rap ay ati ate
Pour nga dape ma kate nga khadj
Ladial gang bi jul loumouy dadj
Pick lén sons  yi kane moniouy fadjj ?
Hey waw
Nioune daniou taame ay ndaam biss bou nek balla day daane
Tolal ni bombardier caterpillar bi day paane
Dak ma rap mounoul nek médeu dou lek tane
Dall yi féss thi bountou sale succès bi nekoul ay gane
Top si ndepp li keep keep lou dieekk def tek
Rep di lek lou nek parier si X lou bête
Leuré sa gars yi
Lal lali lalalé guel yi
Lém beats yi lémi  ay hits
Ladial ma noone yi
Kham nagne siiw douma bétte
Khelii leweul daadj diokh la temp fort
Même bo neké almadie di feekh dama lay roof tangoor
Tirer si montre takhoul am tmp mort
Diaye ma tangue si pét Boma séné sedd ni pôle nord
Dougne mayé touss

Douniou mayé wéé?N dougme mayé th?Ouss
Non non douniou meusseu mayé wée?N
Douniou mayé wée?N té douniou mayé th?Ouss
Hey mat douniou meusseu mayé th?Ouss nieuweul
Douniou mayé wéé?N té douniou mayé th?Ouss  

Douniou mayé wéé té douniou mayé touss

Ecouter

A Propos de "DMT"

Album : DMT (Single)
Année de Sortie : 2022
Ajouté par : Farida
Published : Aug 20 , 2022

Plus de Lyrics de MATADI

MATADI

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl