Paroles de Sagnsé
Paroles de Sagnsé Par DIAW DIOP DIDI
Diaw Diop Didi… OMG
Yene kaye lene setane fima guéne
Kiy djiéme bokoul ak kiko meune
Barbé cheikh Sagnesé sama yeuff la
Kouma ko sekal doumala
Tayoumako dafaa né si mane
HummDamako djioudouwalé
Wa tamite tamite, wa tamite tamite, tamite tamite
Wa tamite tamite, wa tamite tamite, tamite tamite, tamite
Xolala nima mele
Xola nima mele
Guiss ngua nima mel
Mane dale mane dale machalla a
Xolala nima mele
Xola nima mele
Guiss ngua nima mel
Mane dale mane dale machalla a
Mane dale mane dale machalla a
Machalla a
Mane dale mane dale machalla a
Sama setou naxouma
Sama selfi baxena
Loudoule sagnesé begouma
Té fima guene noye na
Bi si kaw migui tass yakarou bi si souff
Couleur yi dagne koy harmoniser bah mou cool
Yaw sagnesé fiitakoy deff
Beuri felling si la bok
Dafaye yoke Bayere
Douma noone té dossi doré
Wa tamite tamite, wa tamite tamite, tamite tamite
Wa tamite tamite, wa tamite tamite, tamite tamite, tamite
Xolala nima mele
Xola nima mele
Guiss ngua nima mel
Mane dale mane dale machalla a
Xolala nima mele
Xola nima mele
Guiss ngua nima mel
Mane dale mane dale machalla a
Mane dale mane dale machalla a
Machalla a
Mane dale mane dale machalla a
….
Nelé machalla
Nelé machalla
Xalé pare beuri mana
Né léne chapa ala
Bandi sagnsé Nguaye kaye ma dioxela li
Nguaye lingaye
Première dame mariéme faye sall
Sokhena aidera chérie Wally
Viviane chidite foumou fete
Nabou Dashe Mondial kaye dosé
Maman Diouma dieng diaxate
Lyle boy gueye borome torino
Wizi JFA universel
MSD general Istanbul
Bi Weuz W.paradace
Bamba fall borom medina
Ecouter
A Propos de "Sagnsé"
Plus de Lyrics de DIAW DIOP DIDI
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl