Paroles de Takk Ma
Paroles de Takk Ma Par CANABASSE
Bul ma xool yaw
Wan ma ko
Wan ma sa
Mbëggeel yaw
Toogal di naala wan
Soo tëdde nelawal
Sa mbégte sama mind
Girl yaa moom sama time
Keneen compté wul yaw yaa toog sama wet
Bàyyeekul jox ma sa lépp
Réccu du am non my baby
Ndax kërsa man mën na ma ray
Bu dee man Maay kiy causer ay rangooñ ci sa bët
Ñakk la di na ma diis girl xam na sa njëg
Du ñakk ma jalgati
Waaye su ma la yéenee tiis
Wala leneen lépp lu bon
Yàlla naa ci njëkk
My baby fi ma jaar ak mbëgéel dafa tar
Xëy na Looloo tax du yomb ma baisser sa may garde
Mais lëndëm mënul wëy même ci ku pare wul pour jant
Lu Yàlla xas ba bind mbindéef du ko teree am
Bul ma xool yaw
Wan ma ko
Wan ma sa
Mbëggeel yaw
Neena Da fa. Bëgg ma def diff takk ko
Officialiser lépp jël ko def ko soxna
Nedna bëgga tul far jëkkër la soxla
Ayca baby mën nga waaj
Koñ ba koñ mën nañu baas
Yeah bës bi ñu doon xaar mi ngii mujj na ñëw
Mais Gis nga bul ma sàñon ñu jeem ko dund
Ci Sunna ak farata mu doon lu simple
Guro, beignets, gingeer
Tàkkusaan imaam bi teew
Balaa timis match bi fin
Bou suuf si di sedd yaa ngi sama wet ma jiite la gee
Sëlmël ñaan yàlla sàmm suñu yéene
Xew bu oyof mariage bu dëgër
Ma jeem la ci yor ba sa baay bu tëddee
Nelaw ndaxte xam na ñi doomam mi ngi ci loxoy gor dëgg
Du parfait di na am ay jour ku né jiiñ moromam dëmm
Satan di chuchoté sunɔ ñuy noppmais du ñu fàtte
Xutba Imam bi yeah
Bu kër gi doon tàkk doo fay bay xalaat divorcer
Bul ma xool yaw
Wan ma ko
Wan ma sa
Mbëggeel yaw
Wan ma sa mbëggeel
Baby wan ma ko
Wan ma sa mbëggeel
Baby takk ma
Wan ma sa mbëggeel
Baby wan ma ko
Ecouter
A Propos de "Takk Ma"
Plus de Lyrics de CANABASSE
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl