Paroles de Coup D'Etat
Paroles de Coup D'Etat Par ABDOU GUITé SECK
Seytané moma bolek kiy souma diabar
Ma wolou la yoni la nguir ki gua doon thi mane
Nga dem fa yow diko nane ki meunou la yoor
Bilahi bou thi doom dioudou wone yow la koy toudé
Tèè bou doonone djiguen sa yaay lay toudeu
Ni Diego, ça ne se fait pas
Lii laan la
Lii laan la
Lii laan la, lii coup d’état la
Lii laan la, oh!
Lii laan la
Lii laan la, lii coup d’état la
Diego mane mi fouma nekkone ba sétlou wou mala
Bilahi bou thi doom dioudou wone yow lay toudou
Diego bou li télona fegne
Kone ma dem té bayila ak mome
Yama gueuneul koumou meuneu doon
Waya li dé khawma loumou doon
Seytané moma bolek mane souma diabar
Ma niane ko guir mou deloussi ndakh moy li guene
Mou takhamlou, seytané meune nako
Ma yoni sama domou ndeye guir mou dioubalé nou
Ndéké Diego yague naye dokh yénéni diego
Lima fogone thi yow Diego lolou nekoul
Yéne dé mbadou danguene doon sëy sama kaw sëy
Lii laan la
Lii laan la
Lii laan la, lii coup d’état la
Lii laan la, oh!
Lii laan la
Lii laan la, lii coup d’état la
Diego banouy ndaw batay
Diego banouy diangando
Baniou dougue négou goor
Massouma gueum ni digue ma woor
Diego lima la waatal
Diego lima la fightal
Diego bor yi mala baal
Diego keur guimala al
Diego!
Ecouter
A Propos de "Coup D'Etat"
Plus de Lyrics de ABDOU GUITé SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl