Paroles de Diaspora Bi
Paroles de Diaspora Bi Par ABDOU GUITé SECK
Wo wow o oh! Diakhlé diékh na
Dotou lèen weet, nek ma guifé
(Abdou lou takh)
Wo wow o oh! Diakhlé diékh na
Dotou lèen weet, nek ma guifé
(Mo Abdou ngani)
Teudeu teudeu nélaw diékh sén khél dem thi réw ma
Beug nga sa doom xam sa thiossane
Wo wow o oh! Diakhlé diékh na
Domi diaspora bi beneu nguén (eway samba!)
Yendalo fanane nalo, ndimbal nga doon thi Sénégal
Boudoul woon ak yén niou yèl wani djé
(Touki tekki dafa am, tokk fi tekki am
Kou yalla teral
Kouka tédali thi torokhte nga dieum yalla teral)
Wo wow o oh! Diakhlé diékh na
Dotou lèen weet, nek ma guifé
(Abdou
Do ndieumbeute dessoula soukhate
Ba nga dieumbiy rene ni thiossani mame djiko)
Téy ma wuyal lèen wetal lèen délou djinn lèen
Jigeen nia gui ni kén dou niom
(Loula yalla diokh
Nga bokk ak gni la yaakaar niou dém
Yaw ngua déssé ngor diomeu nga moyal
Jun doli ma)
Liguéy soneu ba wér dé nga daw yoné ko réw ma
Boudoul woon ak yén niou yèl wani djé
Wo wow o oh! Diakhlé diékh na
Dotou lèen weet, nek ma guifé
Ni niew lèen, nieup guiss diambar yi (kholal)
Bou dara sédo lofi am yaye borom Yén gni
Kouka thi meun nga délou
Yow na nga kham ni dangua wara djité
Mougne lèen nak, yalla bou lèen massa tayi
Doom yi niouy sonal, khagna lèen sén yélèe
Yeuk naa ko
Daniou wara boulo, ngir meun lèen doolèl
Geum naa ko, geum naa ko
Doom yi niou boom nak, deugeu deugeu métin ama
Yeuk naa ko
Doom niouy sonal khagne lèen sén yélèe
Yeuk naa ko, yeuk naa ko
Guénou golo goudouma lu thia borom yeuk nako
Djoug lèen niou wane liniou mmome
Niou féssal li di sounou thiossane
Tambali wan
Sounou doolé
Diaspora bi wooté na
Thiono diéma gueun thiono yaafousse
Thiono am ma gueun thino niakk
Boulèen délou bén yoon guinaw
Diaspora bi woulé na
(Eh eh ! Abdou seugeuel, seugueul, seugueul sét ni seugueul
Bo seugué guisso li ngay sét ni siggi
Ah ! sa morom seugue
Boula eupé chance mou dieul
Boko eupé chance dieuleul)
Thiono boulo ma gueneul thiono noono
Thiono tabé ma gueneul thiono sisse
Yén na gui dimbali sén khét
Diaspora bi kén gueunou lèen
(Autorités yi yén laay wakhal
Nane lèen guéstou gni thia kaw ndax nionouy béggal
Keupeul, so keupé guiss li ndeye liguéy kippil)
Diaspora bi wooté na
Jigeen goor goor goor, jigeen goor
Ndaw magg ak ndaw ndaw magg ak khoubidasse
(Réw ma dafa méti niom laniooy béggal
Oh oh oh ! wooy waléy
Thiono nga thia réw ma nane lèen ku dioyando
Dieuleul éway samba
Abdou Guite ligua wakh na sétal
Seugueul chance bi li thi nékk dou ndé ya ko liguéy)
Diaspora bi wooté na
Ecouter
A Propos de "Diaspora Bi"
Plus de Lyrics de ABDOU GUITé SECK
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2024, We Tell Africa Group Sarl