Paroles de Xarit
Paroles de Xarit Par JAHMAN XPRESS
Sam bopp lala diapé
Maak yaw la wone bagniy ndaw
Ba takh na lou meuss yandou mane
Dey fanane ci yaw
Sa nakar sam boss bo piquiro ma nane fa ay dome
Khalé laa wone té amone naa yéné ma toudé laa dome
Khana dou yama newone " fo dee ma dee faa "
Mane khamone nani doma yakkeu moukk ndakh CFA
Khana fatelikou woo souniou none ya
Khamal ni foma tekk rek mane tekk nala Fouko raw
Kharit yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Bestie bestie sama real bestie
Kharit yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Bestie bestie ki moy sama bestie
Ohh my bestie oh oh
Bestie oh oh oh
Ohh my bestie oh oh
Bestie oh oh oh
Siguil maley séne
Yaay sama bestie
Kharit bou melni bi yomboul
Sortez vos amis
Kharit meune na gueune domou ndeye
Ya takh ma gueum ko
Tey ma wakhal la sey bakh bakh
Ba nieup kham ko
Lou yagg deug leu yaw keneu nga ci mane
Takeu nala kharit goré ngama wane
Mangui ci yaw nak ba guèdj gui di ferr
Réthiou wouma loumla done khamé
Khana dou yama newone " fo dee ma dee faa "
Mane khamone nani doma yakkeu moukk ndakh CFA
Khana fatelikou woo souniou none ya
Khamal ni foma tekk rek mane tekk nala Fouko raw
Kharit yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Bestie bestie sama real bestie
Kharit yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Bestie bestie ki moy sama bestie
Yeah kharit sama woo ma
Weur nala ba khadi naa
Histoire bi diekh na
Naniou dialeu ci lénéne
Sougn diganté maak yaw
Fofou keneu khadiou fa
Té lou yendou ci yaw
Souma teudé fananok mome
Kharit sama woo ma
Souma méré soumla guissé ree
Kou melni yaw foumakoy dieulé
Yeurmandé bi nekk ci mane ak mom
Khana dou yama newone " fo dee ma dee faa "
Mane khamone nani doma yakkeu moukk ndakh CFA
Khana fatelikou woo souniou none ya
Khamal ni foma tekk rek mane tekk nala Fouko raw
Kharit yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Bestie bestie sama real bestie
Kharit yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Yaw yaay mane té mane maay yaw
Bestie bestie ki moy sama bestie
Ecouter
A Propos de "Xarit"
Plus de Lyrics de JAHMAN XPRESS
Commentaires ( 0 )
Aucun commentaire pour l'instant
Vous aimeriez sûrement
Essayez l'application Mobile
A propos de AfrikaLyrics
Suivre Afrika Lyrics
© 2025, We Tell Africa Group Sarl