JAHMAN XPRESS Djaayma Guerre Bi cover image

Paroles de Djaayma Guerre Bi

Paroles de Djaayma Guerre Bi Par JAHMAN XPRESS


Li guene ci Ndap li lay nieuw keuf
Gnibek mom sen yakar tasssss
Guerre ak man yomboul dama meun biss
Ma ci tek lokho té motax nguen guethie ko guis
Kinguen done kheutho la def thiopet
Dolen ci papa ndiaye may Bondi
Man dama tangue foumalen fek nguen almett
Dieulko sen lokho paré taxaw guerre guerre bi

Man Lima mom
Lokho Bouma ci fek nga yeureum borom
Ki bako yala di sak man ma taxone
Seti len lennen ki boure tek na ci lokhom
Sama lek la teguil sa ay beut ci mom

Djaayma guerre bi
Djaayma guerre bi
Djaayma guerre bi
Djaayma guerre bi

Kou niémé nanga takhaw
Kou ragual nanga daw
Ki kouko beugua nangou si man
Dangnouy raak ba naw
konn Djaayma guerre bi
Djaayma guerre bi

Ki may Kiko téyé man comme kou ngap deureum
Ngén diotaat si dou yombou man damlénn yeureum
Dama tébbi As Takh sen coeur yi di bakh
Meunon dieul Sama place
Ligueyo’fi loutakh
Manela diw beurre bi
Ñunela Adja ak Aladji
Makoy adje diko adjiii
Chérie booy

Dafma tane ci sen biir ndax xamnani kou nutella
Dafma noba noba nob dof chérie sama chocolat
Ki manela nob (waw) dotolén’si diott
Ndakh munuñ’ko bokk
Konn demal nga tokk
Fi amofi place
Man douma sa mass
Sen yakaar’ra tass
Lém lenn séni bagages
Manela diw beurre bi
Ñunela Adja ak Aladji
Makoy   adje diko aadjiii
Chérie booy

Djaayma guerre bi
Djaayma guerre bi
Djaayma guerre bi
Djaayma guerre bi

Kou niémé nanga takhaw
Kou ragual nanga daw
Ki kouko beugua nangou si man
Dangnouy raak ba naw
konn Djaayma guerre bi
Djaayma guerre bi

Wolou sa Serigne sou takhé nga yapma nala defal bagages
Andeu bou deuggeur liggey mënussi touss kom jour’rou Dimanche
Fi lo andi Fékk kofi  
Mohh yaw dawn sama yaraam
Khalé boussi douggou sama 18 tu joues avec le feu
Manela diw beurre bi
Ñunela Adja ak Aladji
Makoy   adje diko aadjiii
Chérie booy

Ecouter

A Propos de "Djaayma Guerre Bi"

Album : Djaayma Guerre Bi (Single)
Année de Sortie : 2023
Ajouté par : Farida
Published : Jun 14 , 2023

Plus de Lyrics de JAHMAN XPRESS

JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl