JAHMAN XPRESS Dou Match cover image

Paroles de Dou Match

Paroles de Dou Match Par JAHMAN XPRESS


Wané wou moy sa métier
Fokni fepp ngay wathié
Life bi foo ngako diapé
Né nga sa art  ngay charmer
Nioune dou nii laniouy jobé
Beuri diot niak money
Call bou cher té meuno ci woté
Diaay ko bokk dieundé ko crédit
Niémé topando lo am nieup kham ko
Té do ci dara
Simpoulo niémé diaye graw
Nguirr yallah wagnil sa galathie niou diam la

Yama gueune téyeu , Lol dou match
Yaay domou diw , Lol dou match
Abeu auto diambour di gondi,  dou match
Yama gueune cher call , Lol dou match
Lima yorr yoroulo ko , Dou match
Yama eup pairou daleu , Dou match
AP nga laal , Lol dou match
Resto , chicha , Lol dou match

Niit lo khamoul molay diakhal ba yaw yaa tall woné wou
Beuri daleu té sey mbirr dokhoul kone war nga kholat sa bopou
Yéré you bess nga poster
Sonal nganiok ay "new Bae"
Yoroulo lou soukeur café  
Té nonou nga beugué ay doser
Digue lodoul def sa "nono" be pann lougn la wakh ngani aythieu
Meune saupp té leer nama ni dadialé  taw you matt sakh des fois dalay teuh

Yama dakeu Blow , Lol dou match
Yama dakeu solou , Lolou dou match
Yama gueune fashion , Dou match
Né nga yama gueune branché , Dou match
Beug saf niémé niodi , Dou match
OG la sool , Lol dou match
Mane la khalé yi di weur , Lol dou match
First class nga laal , Lol dou match

Fresh Baby loy diaay
Meun na dieund loy diaay
Awma jott te awma togaay
May sa dof bi mbaraan ma
Ma diokh la loy laathie baby
Dieuleul paka réndi fi
Money  diamant gallé
Lep mongui fi lolou dou match
Meun  ako ko noon boul tit
Danga fok ni lepa yombou
Thioow dou djipp lolou dou match
Anyway

Yama gueune téyeu , Lol dou match
Yaay domou diw , Lol dou match
Abeu auto diambour di (..?)  Lol dou match
Yama gueune cher call , Lol dou match
Lima yorr yoroulo ko , Dou match
Yama eup pairou daleu , Dou match
AP nga laal , Lol dou match
Resto , chicha , Lol dou match

Ecouter

A Propos de "Dou Match"

Album : Abiyo (Album)
Année de Sortie : 2021
Ajouté par : Farida
Published : Nov 24 , 2021

Plus de Lyrics de JAHMAN XPRESS

JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS
JAHMAN XPRESS

Commentaires ( 0 )

Aucun commentaire pour l'instant



A propos de AfrikaLyrics

Afrika Lyrics est la plus large collection de paroles de chansons et de traductions d’Afrique. Afrika Lyrics fournit les paroles des musiques de plus de 30 pays africains et des traductions de lyrics de plus de 10 langues africaines en français et en anglais.

Suivre Afrika Lyrics

© 2025, We Tell Africa Group Sarl